Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics)
1,071,241
Reddit
Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations - unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.



Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.





ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla


Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
itmores.info...
facebook.com/youssoundour...
instagram.com/youssoundou...

Commenti
  • fatou diankha
    fatou diankha

    Khana il explique les parole d'un jinn

  • Capo Elcapo
    Capo Elcapo

    Dafa lèr You yaye sen mame Di sen baye Ki dou morome way The king 🐐

  • Ali Njie
    Ali Njie

    Very nice music 🎶

  • Salimata Albis
    Salimata Albis

    Au moment de tourner le clip svp prenez koukande jap len ci rek il ferait un très bon acteur

  • Talla Gueye
    Talla Gueye

    Grande youssou ndour do moromu gayi

  • Hadim Touray
    Hadim Touray

    Yousou n'dour stop this nonsense, this music is about propaganda, were so intelligent we know who you are talking about,

  • Hadim Touray
    Hadim Touray

    Ça c,est pour macky sall le chachon

  • Thierna Doucouré
    Thierna Doucouré

    X

  • Thierna Doucouré
    Thierna Doucouré

    X

  • Eldifa Dieng
    Eldifa Dieng

    🇸🇳❤️

  • Rameses Sall
    Rameses Sall

    Machallah l meilleur je l suit depuis Mauritanie

  • Fall Mane
    Fall Mane

    Tope nice

  • Gorandiaye Pro
    Gorandiaye Pro

    wanniko le wolof une langue riche diminuer decompter detourner demitour

  • Pierre Dupont
    Pierre Dupont

    Très bon nouveau single de Mr Youssou Ndour très très bonne musique notamment les percussions et cuivres a l'arrière félicitations à toute l'équipe et au musiciens

  • Meujnat Diakhaté
    Meujnat Diakhaté

    Si il es pas le meilleur qui es le meilleur

  • cheikh tidiane samb
    cheikh tidiane samb

    Do sen morron

  • Modou Mboup
    Modou Mboup

    Tiey pape you🥰🥰🥰💪

  • Aichetou Tandia
    Aichetou Tandia

    Tonton you le roi de la musique africaine. On t'aime depuis la Mauritanie

  • Mau kona Official
    Mau kona Official

    Le kinG ❤️❤️❤️

  • Cisseameth 766 Cisse
    Cisseameth 766 Cisse

    Konkand anaga 😁😁

  • Diop Fatou
    Diop Fatou

    Tu es le meilleur mon grand longue vie et santé de fer

  • Goths boy Yeug Deff
    Goths boy Yeug Deff

    Nday san Youssou dall gay nde la✌️✌️♥️♥️♥️🔥🔥💪💪

  • boga bugi bugi
    boga bugi bugi

    One million vues by 1 week

  • Adrame GUYE
    Adrame GUYE

    Pleine de mélodies cette chanson. Ce monsieur, plus il prend de l'âge, plus il devient meilleur dans son domaine. Cette chanson c'est un chef-d'oeuvre

  • Mariam bien
    Mariam bien

    Booba Ndour wanni kon Baye fennec🤣😂😂😂

  • El hadji Sall
    El hadji Sall

    Le roi Aka dégueu machallah 😍😍💝💘💝💝💖♥️💖❤️💝💘♥️💝💘♥️💕💞💞💗💝💟❣️♥️😍😍

  • Elhadji Masseck DIOP
    Elhadji Masseck DIOP

    You waxal Macky salle mou wagniko depuis k t'a rejoint ce médiocre j'ai arrêté de t'écouter

    • Mamoudou Diallo
      Mamoudou Diallo

      C'est un problème et en plus tu mens. Tu ne l'écoutes pas qu'est ce que tu cherches sur son compte ? Youssou est national

  • Chacha Gueye
    Chacha Gueye

    Bilay do sen morom💯💯💯💯💯💯

  • Modou sarr
    Modou sarr

    Amoul moron👑❤️

  • Omar Ndiaye
    Omar Ndiaye

    Youssou ndour nguir yalla kañ ngay bayi weuy

    • bou kene merr
      bou kene merr

      Khanna danga mer wala sa khol nekhoul

  • Sylvie Barboza dias
    Sylvie Barboza dias

    Kounkande sa katan beurri woul ngay doul 😋😋😋😋

  • cherif diallo
    cherif diallo

    J'ai fais ecouté ce song à Adji sarr et elle a dis que sonko ne la pas violé🤣

  • joseph ndione
    joseph ndione

    Le meilleur de tous les temps ⌛ amal diameu ak wërgui ak goudou fane 🙏🤜🤛

  • Doeudonne Sambou
    Doeudonne Sambou

    IL YA 20 ANS DEJA ..LA VEILLE DE MON DEPART EN FRANCE J'ECOUTAIS QUN SEUL MORCEAU DE YOUSSOU NDOUR QUI MA INSPIRE..QUI MA MOTIVE QUI SOUTENU ET QUI MA DONNE DE LA FORCE DE L' ESPOIR PATOUT OU JAI PU ALLE DANS LE MONDE LOIN DE MON SENEGAL C'ETAIT LE FAMEUX ET L'INCOMPARABLE MORCEAU ""LIGUEY "... JE SUIS A NEW AUJOURDHUI..SAYOU MA NAME SENEGAL CEST CE MORCEAU DU GRAND YOU QUE J' ECOUTE DANS MA BMW ...LIGUEY LIGUEY LIGUEY DONGUE MO KO YOR ... 🙏MERCIE GRAND YOU POUR CET INNOUBLIABLE ET BON CONSEIL...DIEUREUDIEUFFFF YALLA NA YALLA CONTINUER FAYE 🙏 SANS OUBLIER MON GRAND TRES SAGE TRES SIMPLE TRES SYMPA TRES LOYAL TRES FIDEL TRES HOYOFF THIE ADOUNA ...L'UNIQUE MBAYE DIEYE FAYE. 👏♥️👏♥️👏♥️👏♥️ MERCIE BEAUCOUP 🙏👍👌

  • Junior Jr
    Junior Jr

    Brom Sénégal je t'aime bilahi

  • aboubacar ba
    aboubacar ba

    Rois du mbalk

  • Amir Diagne
    Amir Diagne

    Le meilleur de tous les temps youssou marie séne les notes de Habib faye nous manque yallanako yalla yeureume té djégeulko amiiinnne

  • sileye gueye
    sileye gueye

    Ki est là pour les 1M de vues 💪🏼💪🏼💪🏼

  • mandiaye Ndiaye
    mandiaye Ndiaye

    Bilay waro politique ndakh senegal gnéppala begue ❤

  • minachou
    minachou

    Je suis la pour fêté les 1 million de vue youssou ndour dou morome

  • Saikou chaa Lo
    Saikou chaa Lo

    Sathi katou courant

    • Saikou chaa Lo
      Saikou chaa Lo

      @bou kene merr sa tounou ndeye mo corona

    • Saikou chaa Lo
      Saikou chaa Lo

      @bou kene merr da leufeul ndey mo. Corona

    • bou kene merr
      bou kene merr

      Khanna sa khol nekhoul nanal ndokh bou sedd 5 litres et vas au lit. C'est peut être le Corona

  • bou kene merr
    bou kene merr

    Le tube tant adoré par la 2e femme de sonko

  • ISO LAYE CRÉATION HD
    ISO LAYE CRÉATION HD

    Waay bi règlement de compte la😎

  • omzo omzo
    omzo omzo

    Audio 1miln de vue youssou ndour amoul morom si mim rew

  • Khassoum Niass
    Khassoum Niass

    👑💕💕👑💕💕👑

  • Hamidou Agne
    Hamidou Agne

    Toi aussi ragua lall yalah bayi sathie signal ak courant te gua fay impôt OK

    • bou kene merr
      bou kene merr

      Ousmane sonko beug....

  • Hamidou Agne
    Hamidou Agne

    Déll fay impôt

    • bou kene merr
      bou kene merr

      Youssou Ndour,♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • Souleymane Dieng
    Souleymane Dieng

    Bravo YUOSSOU

  • Diarietou Mboup
    Diarietou Mboup

    Une semaine 1 millions de vue machala dady ❤️

  • Fatou Kebe Kebe
    Fatou Kebe Kebe

    Meilleur

  • Assane Ndiaye
    Assane Ndiaye

    1m d vue🏃😂🇸🇳❤️

  • manga ndior
    manga ndior

    1 million de vues en une semaine

  • Diallo Jerry
    Diallo Jerry

    1007287 vu en une semaine thiey ndour ya wor

  • BA Aliou
    BA Aliou

    koukandei amo chance d🤣🤣🤣🤣🤣

  • fallou Fall
    fallou Fall

    Techniqku sacci frequence japon ngako diangé 1😃 doo nit

    • bou kene merr
      bou kene merr

      Sonko kor adji sarr

  • MamOour
    MamOour

    ~Oooh magnifique le Maestro de la musique Africaine king Youssou…

  • Amadou Kane
    Amadou Kane

    Tu es d'une autre DIMENSION

  • bcvbb hyui
    bcvbb hyui

    C'est le même bit que "KADOU" de Youssou! L' une des meilleures de You

  • baye cissé
    baye cissé

    💩💩💩💩💩💩👎🏿

    • mame Diallo
      mame Diallo

      @bayeCisse Tonil gnou seu you kheegn yii te andak gnom thia khathieu 😷😷😷😷😷 Gnoune dayou enjoy 😍😍😍🌟🌟🌟🌟🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • Kalidou Balde
    Kalidou Balde

    Mon oncle l'star de la planète terre a encore frappé, Machallah do Sen morom GALSEN 🇸🇳🇸🇳 une fierté

  • Sylla Amadou
    Sylla Amadou

    Merci you le meilleur des meilleurs franchement le top des mélodies

  • Mohamed Sy
    Mohamed Sy

    Kon Kande wagniko eupna

    • Mohamed Sy
      Mohamed Sy

      @bcvbb hyui nice bro

    • bcvbb hyui
      bcvbb hyui

      1000000

  • Mohamed Sy
    Mohamed Sy

    Mashallah

    • Mohamed Sy
      Mohamed Sy

      Felicitacion

  • jack ngom
    jack ngom

    N 1 waniiko

  • Cheikh Maram Mbaye
    Cheikh Maram Mbaye

    1million 🥰💪🏾🍫

  • Mr
    Mr

    1M no bokossi nakk

  • Nyimsing Diva
    Nyimsing Diva

    Bless you youssou❤❤💝 thank you for your beautiful song , our king my king. May almighty Allah give you good health and long life. Amen . And blessings to all your band members may all leave long with good health. Amen.❤❤❤

  • Khady Pouye
    Khady Pouye

    Félicitations ❤️❤️💓💞💞💕❣️💕le king 💕 le roi du mbalax ❤️💓❤️💞❣️❣️💞❣️❣️💞❣️❣️💞❣️💕💞❣️💕💞❣️💕💕💕💓💓💞💓💞💕💕💞💕💕💞💕💕💞❣️💞💞💕💓💓❤️💞 aaaaaayeeewaaaaaaay❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • mansour barry
    mansour barry

    Tu es le meilleur au Sénégal mais wagnile politique bodio bodio ak Macky te nga andak askane wi

  • Ousseynou Gaye
    Ousseynou Gaye

    1milon de vu ❤️❤️❤️

  • Mor Gaye
    Mor Gaye

    Wagninakoo

  • Ndiaye Cheikhouna
    Ndiaye Cheikhouna

    1milion de vu

  • Adji Kamara
    Adji Kamara

    1 millions de vues 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • bou kene merr
    bou kene merr

    Ce tube je le dédie à tous les pastefiens et à Ousmane sonko, Ousmane tounkara , assane Diouf , Adama gaye

  • Ahm Mouss
    Ahm Mouss

    1 million,1 million,1 million ce soir 💪💪💪💪💪💪

  • Cadijatu Seidi
    Cadijatu Seidi

    1000000

  • Cadijatu Seidi
    Cadijatu Seidi

    🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿💯💯💯💯💯💯💯💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿👑👑👑👑🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳✊🏾✊🏾✊🏾

  • Aïssatou Baldé
    Aïssatou Baldé

    Le roi mbaakh

  • pape mbaye gueye
    pape mbaye gueye

    Un bon produit

  • Ibrahima Gueye
    Ibrahima Gueye

    ♥️❤️♥️💯💯 younous Ndour

  • my mrs lovely
    my mrs lovely

    My hero 🦸 of all time’s singing the stars ⭐️ belie love ❤️ you ❤️❤️❤️

  • Papa Moussa Sankare
    Papa Moussa Sankare

    « Technique yoyu Japon lako jangué té bobu djamono mane leu gneup di weurr » Incroyable quel homme

    • Thiané Diop
      Thiané Diop

      Lol You mo ame inspiration. Partie bobou momassi gueuneu neikh

  • abdel Kader DIAKHITE
    abdel Kader DIAKHITE

    Toujour le meilleur

  • Cheikhouna Spurs
    Cheikhouna Spurs

    Le meilleur de tout le temps 🇸🇳🇸🇳

  • bou kene merr
    bou kene merr

    ,,♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • Binta Lo
    Binta Lo

    Walahi do moromou beineuh xalei dady yalla na bate bi gueuna wer goude fane ak wer rkk lalay nianal

  • Ansoumana Coly
    Ansoumana Coly

    Billahi yalla n'a sa diam yague billahi kéneu d'où yow Amal diam l'international de musique sénégalais le roi du mballax

  • Binetou Bâ
    Binetou Bâ

    yousou NDOUR tu à résolus des problèmes avec WÁÑÑIKO

  • Mansour BA
    Mansour BA

    C’est homme est un mythe, un génie, un monument de la musique sénégalaise et africaine👌

  • Modou Modou
    Modou Modou

    Le roi

  • Ame Pogba Danfa
    Ame Pogba Danfa

    Le meilleur de tous les temps

  • AMZA TV HD
    AMZA TV HD

    Nice

  • Alioune Badara Niane
    Alioune Badara Niane

    TJRS LE MEILLEUR

  • mously sarr
    mously sarr

    Légui lepp mola dessé

  • mboup massaer
    mboup massaer

    Patins moy déf clip dh

  • Mc kobza l'officiel
    Mc kobza l'officiel

    Papa Youssou do nite bilay❤️🇸🇳

  • Magatte Sall
    Magatte Sall

    MERCI PAPA YOU D'ETRE DU COTE DU PEUPLE. NOUS SAVONS TOUS A QUI S'ADRESSE CETTE CHANSON. AND AK NITT DOU TE WAKH KO DEUG. PR MACKY SALL DEGLOUL PAPA YOU BOU BAKH WAY WI YAW LAKO WAYAL

  • Maria SN
    Maria SN

    Le meilleur

  • Macoumba Séne
    Macoumba Séne

    Clips vidéos cou d'accord

  • Lamine Diaw
    Lamine Diaw

    Bilahi yay khadj ndour lo guéné mou nékh

    • Lamine Diaw
      Lamine Diaw

      @Ahm Mouss no ki say say la

    • Ahm Mouss
      Ahm Mouss

      Déte way🤣🤣

Il prossimo