Série - Diabarou Gorgui - "La femme du chef" -Episode 42 - Le mariage de Sadiya.
25 giorni fa
37:44
722,881Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
instagram.com/kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook
facebook.com/kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
instagram.com/kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook.com/kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
C triste😥😥
Ah c domage je ne cesse op de pleurer neysane situation oblige genre yi rek nioy dem di seuy seuyou ma tay par ce que dara dotoula safati si adouna ya bcp de femme qui souffre en silence par qu’elles n’ont pas l choix soit amouniou yaye seussouniou si kenen kou len koulen dimbali niou dougou si malgré moi té gnilay wakh dougousi nio gueneu kham bgo té bou nekone sen dom dinagn xol bou bakh liniouy def bala may dé niounane djiguen dou beugu day mine je suis pas dacord par ce que djiguen nit la com niep djiguen dafa am khol wara beugu.mais so amoul papa ak yaye seusso si keneu sa famille dougn la diapalé si beneu coté daniouy tok dila setane baga def beneu betise bou ndao kou nek oubi sa lamign👅di wakh té bigua sokhla soutient dou keneu si niom koulay soutenir yala bo nek xalé bou am diom nak lou niaw lo khalat dinagn ko tek sisa der en plus dila mystique pour bagne rek gua avancer li nek sama xol yep meunouma ko wakh💔😭
C vraiment triste man je me demande batay loutah yayou sadiya begeu def li dafa begeu vengé wou wala
Wa ana épisode 43 bii????
Métyna trop sadiya mais mounial rk
Slam ms série dafa fin wala
Wa saison bi dafa diekh wala
Lui khana c fini🤔🤔🤔😭
Li keye. C'est n'importe quoi
Je ne suis pas d'accord comme ces genres de mariage kou d'accord ak Mane beseull jaime
🥰😍😍😍😍😋🦄🦄🦄🦄🍓🍇🍎🥖🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐
😢bilay yagui may dioylo sadiya
Non
Waw khana bi moy le dernier épisode ??
Les couples salit et oumaya
Wadial jour gui 🌜
Sallal lakhou khalay khi wasalam
Sallal lakhou khalay khi wasalam
43bi l'ay xar
Wa kou lene maquillage
Yéne wa khar media tamite yénagui commencer sof nak films yingéne di teubeul ni nak louléne téré ték films yi bangaéne khamé ni meunolen bolé ay film you beuri doléne deff par béne béne li mom déye décourage lo nite ishhh
Wa khana série bi dafa diékhe
Film biii néxna trop mais respecter wouyou jour yiii heure boulén néxxx laniou Koy ték
Wa sadiya mome foumou diame
Mame saye yaramam dou daw
Mais khana épisode 43 amoul
Désolé😭😭😭😭
21:55 j’ai les larmes au yeux
Guir yalla dolen bayi serigne si ak yonen ti bi sakh ay j’aime rek Arrêtez kamem
Solution mariage forcé mom égal fakeuuu beu diiirrr bou yaagggg baniou revenir a de meilleurs sentiments dogaaa revenir wattt si c’était moi mom j’allais fuir mais alhamdoulillah bameu bokkeiii si famille bo xamnei chacun fait son choix
Comme maquillage sadiya bi changer guen ko rk cv🤣🤣
Par
Mame saye diepi nako ak mousorame bou yague bi
Makiage bi dei mo geunn fouff bici bande annonce ba😂
Sheuute Oumaya aq Salif teumit😍😌❤️
Sadiya Ndeyssane 🥺🥺🥺li mom koumakodone doundeulo dangmeiy raaye req wayer khalatoumeuko waay🤦🏽♀️
Sadiya seiy ballons you bleu rouge laneuleuh?😂 mbeter kouy supporter barça😂🤦🏽♀️
Le regard de Salif quand les aînés parlaient Ndeyssane explique tout amnegn louleine meti dale Ndeyssane 🥺🤦🏽♀️
Ndiaya amoul diiom Bilakhiiii ki diiom amoukooo noon Sheuute 😂😂😂🤦🏽♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️
Oumayaaa putaiiin 😂😂😂🤦🏽♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️ neinako deiite boumeuh baappp😂😂😂😂 Sheuute Aywaaay magui kheum😂😂😂 une vraie amie wallah❤️😍
Waaah Mame Sèye mi niit leuh😂😂😂😂🤦🏽♀️🤦🏽♀️ Diouroumeukooo😂😂😂🤦🏽♀️kiii mereinakooo trop waaay😂🤦🏽♀️
Mame Seye ioe diepinaleuh naq vraiment diepinaleuh khalato seuh dome beine yoon t’es trop égoïste comme maman mane tu m’énerve ish😒🤦🏽♀️
Salif ndaysane c un bon ami
V c
❤️❤️😭❤️😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍❤️
😭😭😭😭
Ana wa sopey serigne babacar😍😘😘😚😚😎😎
Mounial sadiya Dina bakh
Ndeyesane Sadiya ak Tata Saphie comme mane ak sama Tata sama magou Yaye Gaaniou juillet bi passé yanna yalla yeureum ta diégal ko ak bépp dioullit inchalla démna bayyimak wéétaay
toul monde du acteur merci beaucoup
Maquillage bi mom khana dagno fater finitions lol
Ndeysane Sadiya dafa sone
Ay way loutakh mariage bi am😭😭
Mariage forcé dé dou bonheur seul la maman est contente et le mari
Mariage force Metina
😭😭😭😭😭
Mane yayu sadiya miii lu takh bugu mako wolof limu wakh rék dage le su nékone sa doome dokoko béf😡😡
M
Alhamdulilaah ! Banu fekkee sëy bi.
Alkhamdoullilah comme que fekké nagne mariage bi 😂
Mame saye dou sax niit intèrêt rek motax mou beug mayer sadiya limom ça montre k diouroul sadiya dax souko diouron douko def li
2021 y’a encore des mariages forcés moi je me taille plu personne me revoit je suis triste pour elle wallah Que Dieu m’épargner de cette souffrance 😭😭😭
😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤😓😓😓😓
Ndeysane sadiya liguaye doundou metina nekeu khale bou ndaw di woudie en 3eme possition ak souniou société bi ni fi woudie mété wakhatou niou niou mayela ko beugoule rawatina sa moromou papeu yalla na yalla maye kholou mougne kepeu kouye doundeu situation bou melni
Wa tmt tata safiatou kuko maquiage
Tré bon conséye
Oooh c triste 😢yalla bouniou doundeu li🙏🏾
Franchement yayou Sadiya diakhal nama, elle réduit la femme/sa fille à sa plus petite expression... Rien dans son discours ne présage le bonheur: nanga rakhass, nanga mougn, nanga togou, nanga, nanga, nanga rek...... Elle s'en fout pas mal de ce que peut ressentir sa "fille" à qui elle fait clairement comprendre qu'elle va souffrir dans ce ménage. En plus, les meilleurs amis de Sadiya takhaw mounane ko bou ame kharite alors k gni ils sont ensemble petits ba grands. Elle est très gauche et indélicate cette bonne dame, pffft !
May léne m'a j'aime 😭
Sadiya démal seyi wayé boula goor gui beugè Laal bagnal dél régélé toubeuy you bari
Ces mamans qui infligent le mariage force a leurs filles c vraiment mauvais
Sadiya série bi yeup dako dioy xam way akh🙄🙄
Wa diomy wouma Khamnané beugo Gorgui Lam, Wayè bo dèma nanga Seye ba seye fou dara nèkoul Bouleen yakh sama sant bi Forcè takhou ko diogue
Maquillage bi nekoul wone si bande annonce bi d😂😂wala commentaire gnoléne changé Lo film bi😏
Mètina trop
J'aime trop cette série surtout sadiya
En fin mariage bi amna, gno sonenah gnoune😂
Hoo c triste sa me rappel le jour que je parter chez mon mari 😭
Ah tata safi dioylo nama wallahi 😭😭😭😭
ana niou bg k navas
Mariasss à la décès magui deh
Ndeyssane mettina courage sadiya
Sheteute moment bou difficile mogui nonou 😂😂😂nena nagn ko wadial rek goorgui mogui woté sheut ins bobou sa fitt di teuf teufff😂😂😂a la boni sète
Nn thossan nékh na
Waw li sey la wa la mousi ba😭
Bilae dama dioy sadiya damako yeureum 😭
Naka dieke ma khamni sama jour anniversaire laye done li😂😂😂
Li kou ko doundoul do ko kham 🥺🥺
Wa sadiya Anna frérou papame biniwone seuy bi dou âme
Sen maquilleuse bi dh hana andoul si seuy bi No wayyyy iiiissshhhh
Mariage forcé koumou daloutt mouno ko kham
Lan moy fatie hémorroïde wala kouko meun fatie sonouna
Enfin le mariage de l'année yéne célibataire yi beusse bou sadya démé lune de miel ba gneuw té takougnouléne dinguéne lambe😃😃
Hoooo man sadiya mogui may fatali sama mariage bou niou ma forsé
Khana do goor
Seni makillage dara bakhoussi ana teint noir nga koye défar poudre nitr kou khess Franche-Comté warnguen kholate kilen di makillé
Cheeeerttteeeeete......ma dieppppiiiiii mame seuye miiiiiii. 😥😥😥😥😥😡😡😡😡😡
Sadya kila done maquiller khana dafa done nélaw
di doli sante samay wadiour biniouma mayer kima beug
Moussorou mame sayyye bi comme potou wassss potou chambre 🤔😂😂😂
Wa sadya khana amo ay mbok ay kharit ana djindiére yi ak beignet yi ana rérrre yi ahhh li mba diam la 😂
Nioune tamite niou wakh alhamdoulilah rek come dounde Nanou ba faikai mariage bi ha yalla Nanou fi yalla bayi niou faikai gentai taw bi ak yénéne Mash Allah
Sant nan len guerem nan len ba mariage bi niawe sen seybi nakh na yagg ne sen preparation mariage.