Papa Thierno NDIAYE alerte Ama Baldé : Modou Lo kou sereinwoul doko dane
15:25
105,107
Reddit
www.equivoxgroup.com
Votre Télévision á Portée de main
Une Thématique digitalisée

Commenti
  • Ndiogou Lo
    Ndiogou Lo

    Yalla na ama dane

  • Mouhamed ndimbelane
    Mouhamed ndimbelane

    Lamine nama baahall waayé manoumako séetann 12se

  • 77 tv
    77 tv

    Mallal begnaa

  • Babacar Ndiaye
    Babacar Ndiaye

    Mashallah mashallah

  • Mariama Diéne
    Mariama Diéne

    👂👈😇

  • Ndeyeomzoo Diop
    Ndeyeomzoo Diop

    Modou lo d'où Dara khamoul tous wayy ama baldé dakoy dan

  • Saiba Fribourg
    Saiba Fribourg

    Reug-Reug dotoul bouré Senegal

  • Ndiouga Loum
    Ndiouga Loum

    Malall machallah est très fort yalna yalla yokkou bbx

  • Samba Ndiaye
    Samba Ndiaye

    Machala malall machala

  • Bathie Fall
    Bathie Fall

    Lamine samba ay wakhi doff rk laye wakh copen sa ndiogou

  • Thierry Basséne
    Thierry Basséne

    Papa Thierno Ndiaye akha xam lamb

  • Ahmad Dem
    Ahmad Dem

    Senegal est tres buzzard. Defa bari woyaan. koune di taggeu boppam

  • Bara Diane
    Bara Diane

    Modou lo 💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪

    • Kamara Awa
      Kamara Awa

      ♥️♥️♥️♥️♥️

  • Omar Mvaye
    Omar Mvaye

    Malal love you

  • Baye saliou Diagne
    Baye saliou Diagne

    Machaalla malll diagne ka dou yi rafètna torop

  • Souleymane Ibrahima Sall
    Souleymane Ibrahima Sall

    Père thiér yay ndanane

  • Balla Guaye
    Balla Guaye

    Père Thierno borom noko daneeee

  • Balla Guaye
    Balla Guaye

    Père Thierno wayyy

  • Kawsy Sy
    Kawsy Sy

    lamine samba Mogui méll ni Kou Guedj guiss micro 😈😈

  • lemer aidara
    lemer aidara

    Pa chérno ndiaye ya kham lambe té kham mbeur yi

  • Fatou omar Ndoye
    Fatou omar Ndoye

    X lo damm inchalla

    • Kamara Awa
      Kamara Awa

      Inchallah dina bakh

  • Fallou Babou
    Fallou Babou

    Malale woutalen ko télé guir champion n'a yi

  • Lhomme Diagne
    Lhomme Diagne

    Takoussane ba timiss foumeko songué Modou teureulko

  • Mahmoud Sent
    Mahmoud Sent

    Malal moy ndanane de

  • Modou Fall
    Modou Fall

    Malal analyse bi diarna yoon

  • Amidou Diallo
    Amidou Diallo

    Ama balde le futur roi ns somme derrière toi bilahi diam rek gay

    • Ndeye Fall
      Ndeye Fall

      Dagaye nelaw

  • Salif Balde
    Salif Balde

    Ama yeeeeeeeee

  • béénaa brique
    béénaa brique

    Modou lo fougue mokay daan doko ragal doko falé doko may dara mais il faut just la respecté c tout. Et ama baldé dundoul modou lo té ama dinako daan inchallah. Boulen wagni boy ama khaléla dou may modou lo dara modou lo douko may dara na supporter yi cool rek bayi niarri lutteur yi defanté bamou saf sap danio namoon facd to face you tangua dieur si respect. Sa me rappel 2012 balla vs yekini 2012= 2021 vice versa rék.

  • cheikh Diop
    cheikh Diop

    Lamine Maguatte ga

  • Cheikhna Diagne
    Cheikhna Diagne

    Machalah thiey groupe future média love rekk gfm dagnoo woor motax 💯💯💯💜💙💛💘😎👊

  • Dabakh Samb
    Dabakh Samb

    Lamine. Samba. Deufa. Bari. Wax.

  • Cheikh VIP
    Cheikh VIP

    ja jaf way amal diam rk yaw wolof rk😃

  • Aamiir B
    Aamiir B

    Lamine Samba kouko laathie limou wakh? Tjrs en train d s justifier

  • Seydi Ibrahima Sall
    Seydi Ibrahima Sall

    Noo pa thierno dina dadji nit koi 😄lan moy (Fiz ziw Fiz zif) bala malay tal soriga 😄khékh 🤜 one one

  • Seydi Ibrahima Sall
    Seydi Ibrahima Sall

    Verement malal wolof bi moylep wante rapport en France bir Sénégal gayou complexe Rek nioukoy def

  • L’absolu Gueye
    L’absolu Gueye

    Ama balde c le meilleur lutteur Sénégal 🇸🇳 depuis en 2012 Mbeur Mounoko Danfii Thi Sénégal 🇸🇳.....Ta inchalah le Futur roi 👑 des arènes inchalah ❤️🙏

    • Moustapha fall
      Moustapha fall

      Niata atte leu année blanche ? Niata combat lafi am ? 😂😁

    • IBZO BBN officiel
      IBZO BBN officiel

      Gouy gui xana danou ko 😂

    • Mamadou Diop
      Mamadou Diop

      @l.absolu déll wax rk

    • Ahmadou cisse
      Ahmadou cisse

      Niatta combat

  • Ibrahima Kane
    Ibrahima Kane

    Modou lo dina ame ndam inchalla

  • Jeff Bezos
    Jeff Bezos

    Wa pikine daguénn tela tiit wakh dji yeup diarouko modou ak ama nioy dess thii guéw bii Inchalla wakh lenn reik

  • Modou Mboup
    Modou Mboup

    Modou lo mane ama foufff

  • Bouba Fall
    Bouba Fall

    Ken dou Mod’lo ❤️

    • Kamara Awa
      Kamara Awa

      Bilakhi yalnako yalla may ndam kharagne lo nékhna faral dimanche kéne dou khalé parcelles machallah

  • Assane Diop
    Assane Diop

    Ama il est tjrs serein dqgueni diawalé niak serein ak fite bou beuri

  • Pa Abou jr
    Pa Abou jr

    Lamine bouye wakh dou noyi bari ngua wakh troope

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    Lamine Samba lou takh mou Bari wakh

    • Bathie Fall
      Bathie Fall

      Sopp rkk

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    Gouy gui moy daan i

    • El hadji baye
      El hadji baye

      Lajoumala lolou dama nii ngua expliqué foko tek thie beurrè mystique wala khekh

    • Cheikh bass Keur massar
      Cheikh bass Keur massar

      @El hadji baye Lou lèèr laala wakh

    • El hadji baye
      El hadji baye

      Loula thie wor yaw féne rek nguay def cheikh bass

  • laChinoise Iniaasy
    laChinoise Iniaasy

    Entt cas ama bou beuguei dann modou naa andeu akk sagoo bilay bouu yakarei nii nelaw ak wakh moy dann Roi bii il s trompe farouchement

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    🎙️🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • Balla Sene
      Balla Sene

      🤭🤭🤭

  • Daouda Thiaw
    Daouda Thiaw

    billaye wakh danoul modou lo

    • Coumba Marone
      Coumba Marone

      Vous avez remarqué Kelk chose Modou lo wakhoul batay moy bandi 😀

    • ziilo bk
      ziilo bk

      eeeeeeee

  • Malick Sarr
    Malick Sarr

    Lamine samba baringa wakhe torop 🗣️🤫modou lo yalnako yalla Maye ndame

    • Kamara Awa
      Kamara Awa

      Amine

  • Bassirou Mbacké Sarr
    Bassirou Mbacké Sarr

    PA thierno damala Fan , nimi wakhee.

  • Ibra Faye
    Ibra Faye

    LAMINE MOGUI MAGETTE NDEYSANE 🤭

  • Ibra Faye
    Ibra Faye

    LAMINE MOGUI NDEYSANE 🤭

  • Nouha DIEME
    Nouha DIEME

    Ama dou yénéne mbeuri Ama il est comme balla gaye et le j-j vous serez surpris walay

    • Moussa Diop
      Moussa Diop

      Il est comme. Il doit être Balla Gaye 🤣 frère wakhafi papa ndiaye. Ay branche si Kaw lagnou fékantei comme yow akh sa rak rek boul

    • Nouha DIEME
      Nouha DIEME

      @laChinoise Iniaasy donc teudieul sa guémégne té nopi ba jour bi yéguesi

    • Nouha DIEME
      Nouha DIEME

      @laChinoise Iniaasy mais boul faté ni sa papa k sa wa keur yeup Ama moléne meune

    • laChinoise Iniaasy
      laChinoise Iniaasy

      U reves mn cher magou ama sakh modou moko dann🤣🤣calmes ta joie

    • Assane Leye
      Assane Leye

      Détrompe toi mon cher. Ama mounoul imposer dara Modou eupouko soutoko. Kou tolo akk Modou taille pour daan ko dou yomb frére. Ba booba inchallah

  • fall yaram diadieufff cheikh ibrahima fall
    fall yaram diadieufff cheikh ibrahima fall

    Lamine samba yagui dieum makk nak bayill dorr yii😂😂😂😂

  • diara bouso diara bouso
    diara bouso diara bouso

    Lolou dafa yombe eume sene wakhoufi dara kena tewoula akh yaw lac deurla bassa 👁👁bi tothie geumal yalla

    • L’absolu Gueye
      L’absolu Gueye

      @DIMKHA LE BAMBISTE kii Dafa réw nopithi Rék xamanté Nan thi commentaire yii bayii Mak Mom Rék Ok

    • DIMKHA LE BAMBISTE
      DIMKHA LE BAMBISTE

      L’absolu Gueye ki lanla fi wakh lou diar saga non waye am lén talibé waye

    • DIMKHA LE BAMBISTE
      DIMKHA LE BAMBISTE

      L’absolu Gueye yaw nekal nite ngay saga ni am lén talibé bakhna rek

    • thiam ahmadul attekh
      thiam ahmadul attekh

      Mom niata yone lako modou lo nokou mou daw Eumeu dako dane 2012 bamou ler Yene nak nek lene fi Lac deux djigurne la comme yene

    • L’absolu Gueye
      L’absolu Gueye

      Katall Nayamm nopiii Yaw Kèneu ladioula Ok 😒

  • lahad bou kharagne Lo
    lahad bou kharagne Lo

    Babacar diadieuff ligury bi rafetna torop

  • Daouda Mbow
    Daouda Mbow

    Wa pikine apo léne wakh dji rek ak sathie bi ba niou yégue ci

    • Ndieme Niang
      Ndieme Niang

      Combat bi dh fouma teudeu nelaw ndax Modou lô wax diou Bari daanouko Boo ligueyoul dooko daan

    • Kamara Awa
      Kamara Awa

      Modou lo khalé parcelles bi ame classe ndam rék inchallah si kharagne lo

    • Ndiaye Babacar Ndiaye
      Ndiaye Babacar Ndiaye

      wakh diou bone deukoul founou dieum foumou diogué leu thiosané wakh daye raféte ñioun kham nagn lép kinepi ay cerveau niofa deuk lolou moleni dérangé wa salam

    • Cisse Mouhamed
      Cisse Mouhamed

      Wallahi kou yap Modou lo si biti géw gui la mais si bir géw kén yabouko

  • Daouda Mbow
    Daouda Mbow

    100 combats modou Lo dakoy daane 100 fois inchallah 👌🏿🙏🏿

    • Daouda Mbow
      Daouda Mbow

      @Ndeyeomzoo Diop yaw nga nek kou niak diome

    • Ndieme Niang
      Ndieme Niang

      Inchallah bou nèkh3 yallah

    • Ndeyeomzoo Diop
      Ndeyeomzoo Diop

      @Daouda Mbow yaw kou niak fayda gua

    • Daouda Mbow
      Daouda Mbow

      @Ndeyeomzoo Diop sa doulou baye

    • Daouda Mbow
      Daouda Mbow

      @Ndeyeomzoo Diop akay deugue inchallah

  • Medzo Diouf
    Medzo Diouf

    Malale bilahi mala sope

  • Maty Diop
    Maty Diop

    Deug bu werrr sahh père kenn du xxxxxx lô si mimmmmm rewww 💪🏽le roi 👑 de tout les rois👑❤️💪🏽💪🏽💪🏽👊🏽👊🏽

  • Ablaye Ndiaye
    Ablaye Ndiaye

    Merci babacar c est laye ligay bi rafète na

  • Gueye Sidy
    Gueye Sidy

    Merci babacar

Il prossimo