L'incroyable Geste de Balla Gaye 2 Et de Eumeu Séne du Jamais vue
00:38
134,431
Reddit
Abonnez-vous à notre Chaine ITmores: itmores.info/post/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: facebook.com/becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Commenti
  • Fall Cheikhtidiane
    Fall Cheikhtidiane

    Ndeyesane li moy sport

  • Bakary Mane
    Bakary Mane

    Merci Eumeu merci balla sama mbor

  • pdg-le-morée sal-zer
    pdg-le-morée sal-zer

    Des grands champions

  • seye mohamed
    seye mohamed

    Balla nit kou bakh la vraiment

  • Dien Auto
    Dien Auto

    Avant Lamb, tous frères et soeurs, après Lamb, tous frères et soeurs. Sénégal = 1 🇸🇳. Au fait ce que fait Reug Reug au MMA est fabuleux.

  • Thiam Amath Maty
    Thiam Amath Maty

    Balla reférence

  • kawou camara
    kawou camara

    Geste bii nice neu wollahi

  • Abdou.Djimo Djimo
    Abdou.Djimo Djimo

    C’est des frero ❤️

  • Mamadou Ndiaye
    Mamadou Ndiaye

    Quand on parle de gentleman dans l'arène franchement c'est Eumeu et Balla. Respect c'est ça le sport

  • Mamadou Diop
    Mamadou Diop

    Cool

  • Lamine Toure
    Lamine Toure

    🤭🤣🤣🤣🇬🇭🇬🇭🇬🇭BaBa2👑👑👏

  • Momo Ciss
    Momo Ciss

    Nice na machalla

  • Zambo
    Zambo

    Balla gaye lèguì nitte la dèhh😂

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakhi Dof Balla Gaye Bami Nitt Dou Tay

  • Produit Naturel
    Produit Naturel

    Pour tout vos problèmes de santé lié aux la perte blanche, au trompe bouché, kyste, fibrome et myome, à l'Hépatite A, Bet C;Vih Sida cancer, diabète et tout autres maladies en général nous avons des remèdes 100% naturels très efficace pour traiter les maladies sans effet négatif.Pour plus d'information veuillez nous contacter via WhatsApp au +229 51751855

  • Aliouneniangapple1 Niang
    Aliouneniangapple1 Niang

    Tres beau geste balla khol bi mo rafete machaallah

  • Gueye Téranga
    Gueye Téranga

    Ma challah li moy lambe

  • Babacar Diouf
    Babacar Diouf

    Li dafa Nice billay

  • marie bella
    marie bella

    Diam rek nguey am eumeu machallah

  • machine gun Kelly Diop
    machine gun Kelly Diop

    Yéne gni di commentaires nane Balla Gaye Xol bé Eumeu Kouka guene Xol amoul ndakh souka nekhoul dou fekfji Balla Gaye ndakh kouné xamnani Balla Gaye Lac2 la andal

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Lolou Mome Deug La

  • Yilé Baba
    Yilé Baba

    C'est très joli

  • Hamdy Junior
    Hamdy Junior

    Thiey balla doundeul te were

  • Ousmane Sane
    Ousmane Sane

    Félicitations lac2 du courage eumeu yaffouss 😂😅🤣😂

  • Mamadou Niang
    Mamadou Niang

    Vraiment lii da nice tropppp je suis tres content .lii moy senegal

  • Fadel Niang
    Fadel Niang

    No vraiment li douma si doyal !! 😍😍😍😍😍

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Machallah 😂😂

  • Maty Diop
    Maty Diop

    Très joli Geste

  • Diene Fagaye
    Diene Fagaye

    No balla mo bakh de

  • Loufa Yatte
    Loufa Yatte

    Bilay sama hol Sedna thi

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Yalla Na Geuna Sédd

  • Ismael Faye
    Ismael Faye

    Li rafetna adina amoul solo lepou si ayui netali laye moudjiou

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakh Ngua Deug Deh Bilahi

  • Ibrahima Badiane
    Ibrahima Badiane

    Kou am khol bu rafét rék li sédd na sakhol bilahi wakhouma nak ak ranquigner yi merci Balla merci Eumeu

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakh Ngua Deug Deh

  • Rama Bocar Sagna
    Rama Bocar Sagna

    Li moy Sénégal

  • Ousmane Mamadou Sall
    Ousmane Mamadou Sall

    machalla

  • Abdou Diouf
    Abdou Diouf

    Liiii dafa rafet loooool

  • Atoumane THIAM
    Atoumane THIAM

    Rafétna machala

  • Zoss Diatta
    Zoss Diatta

    Li raféte naa balla is the best mbeur

  • Soya Diagne
    Soya Diagne

    Wayy balla wayyy

  • gueye mbaye
    gueye mbaye

    Eumeu vremen u a un ❤en or u pouvai dir ta un comba do focus sax si bakou balla gaye me ga dembassi mome genial ❤🙏✊🏿

  • Mouhamed ndimbelane
    Mouhamed ndimbelane

    Kou beugeu d wékhou🤸🏿🤸😜

  • Sadaba Mane
    Sadaba Mane

    Balla vous êtes trop gentil ♥️♥️💋

  • Amadou Ndiaye
    Amadou Ndiaye

    Image bidé genre nit you melni pape sarr doulene arrangé ak gni di khambe tal mecontant yi warnégnoussi diangue lou bari

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      @Amadou Ndiaye Dafa Raféte Kay

    • Amadou Ndiaye
      Amadou Ndiaye

      @Mansour Dieng bilahi Li da rafete

    • Amadou Ndiaye
      Amadou Ndiaye

      @Mansour Dieng bilahi Li da rafete

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakh Ngua Deug Deh

  • Ibrahima Nging
    Ibrahima Nging

    Kéne d'où eumeu sene diom foula faïda

  • cheikh mbacké fall
    cheikh mbacké fall

    Nio gueune khôl thi lamb dji

  • Natural Mavista
    Natural Mavista

    Yén si geste bi ngéne nek mane mangi si générique emission dafma nekh daal mangi koy soga deglou ndakh douma sétane télé

  • Dakar news
    Dakar news

    c'est comme ça ils sont pas des ennemies mais des adversaires pour des minutes...c'est juste du sport

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Vérité absolue

  • wiliam malikk
    wiliam malikk

    Lii feusseull léneko wayyy raffaitena

  • Diop Modou
    Diop Modou

    Les champions se reconnaissent 👍👍

  • EMD YTB
    EMD YTB

    Ken manou ko bagn balla

  • assanari 07
    assanari 07

    Gniy beuss "j'aime pas" ay vrais mécontents legn

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakh Ngua Deug Deh

  • Ibrahima Diagne
    Ibrahima Diagne

    Khol len boucher ketchup 😂😂

    • Ibrahima Diagne
      Ibrahima Diagne

      Ababacar Sarr 😂😂😂😂😂

    • Hamza
      Hamza

      He was shock to see Balla and Eumeu 😂😂😂

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      😂😂😂😂😂😂😂

    • Ababacar Sarr
      Ababacar Sarr

      Saway khekh la donne weur d

  • Ellage Sy
    Ellage Sy

    Franchement c'est très beau voilà des nobles

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      @Jimmy Diene 😂😂😂😂😂😂

    • Ellage Sy
      Ellage Sy

      @Jimmy Diene non je ne pense pas

    • Jimmy Diene
      Jimmy Diene

      C'est normal le prochain combat ça sera balla vs eumeu sene pour son jubilé.

  • Serigne modou Ndiaye
    Serigne modou Ndiaye

    Geste bou Nice billahi

  • tidiane biaye
    tidiane biaye

    Balla yaa baax

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Bilahi

  • Babakare Toure
    Babakare Toure

    Wawa contana machalla balle champion 💪💪💪✌

  • Mbaye Sow
    Mbaye Sow

    kou fékisi moromame c sa

  • Niang Moustapha
    Niang Moustapha

    Machallah

  • Zulu Dieng
    Zulu Dieng

    Ohh li dawna yaram machalah

  • pape dia
    pape dia

    Machalah

  • Sumaila Djeme
    Sumaila Djeme

    LI MOY LAMB FAIRPLAY KEN DOU BALLA GUYE 2

  • papa diom
    papa diom

    Eumeu li rekk motax gnoulay djekkou Mystiquement founekk!! Bilay da nga soxla encadrement mola sonal sa carriere yeup ndax koula djeguewone bou kheuye nekk noone

    • Fatou Soumare
      Fatou Soumare

      Très contente

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakhi Dof Rék Nguaye Wakh

  • Babacar Kane
    Babacar Kane

    Machalla

  • Daouda Mbow
    Daouda Mbow

    Sou lac 2 défone li si combats balla gaye 2 nguéne ni lac 2 yéné woul balla ndam dafa far ak eumeu séne,thiey lamb malgré que geste bou raféte la

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      @papa diom Wakh Ngua Deug Deh

    • Louf DBT
      Louf DBT

      @papa diom waw dafa dem doug ba si cumukay lac 2 conseiller ko lou yagg yengueul supporters yi

    • papa diom
      papa diom

      Balla ba lii djexe Dafa dem thi Lac 2 conseiller ko??

    • Louf DBT
      Louf DBT

      Legui balla bane intérêt la am far ak eumeu sene ? Bimou defei li ba parei si lac la dem tok fa wakhtane ak mom

  • samzalah Kane
    samzalah Kane

    Eume dafa fan balla

    • Mansour Dieng
      Mansour Dieng

      Wakh Ngua Deug Deh

    • thiam ahmadul attekh
      thiam ahmadul attekh

      Lol 😂 dako fan parsk moko dane deux fois?

    • lou way déf bopam
      lou way déf bopam

      Non lolou amoul

  • Aliou Diankha
    Aliou Diankha

    Eumeu gaidé degg la kou am diom

    • Ibrahima Nging
      Ibrahima Nging

      Bilakhi

  • Kadia Niane
    Kadia Niane

    Balla xol bi mo rafet

  • Ayda diallo
    Ayda diallo

    Nice

  • Cheikh Ahmadou Makhtar Djitté
    Cheikh Ahmadou Makhtar Djitté

    Nice na torp bilahi machallah

  • Mbne Tine
    Mbne Tine

    Machalla refétna balla gaye bilay walay xol bi machalla

  • Mansour Diagne
    Mansour Diagne

  • Bebe eumeu
    Bebe eumeu

    Macha Allah Eumeu mbeur dey niaw ndiort

  • Cheikh bass Keur massar
    Cheikh bass Keur massar

    Liiiii nèex na wayy ndeye saane

    • Cheikh bass Keur massar
      Cheikh bass Keur massar

      @Cheikh Gueye Mala raw

    • Cheikh Gueye
      Cheikh Gueye

      Wa mais cheikh bi namnala

  • Fakaramo Saidy
    Fakaramo Saidy

    ❤️❤️❤️

  • Bay Modou
    Bay Modou

    Macallah

  • Babacar Senghor
    Babacar Senghor

    Li moy lamb balla ohhh

  • Imãme President #605#
    Imãme President #605#

    Man limy dégu ni moma daxal vidéo bi waw ki koumou

  • Boubacar Syllame
    Boubacar Syllame

    Li rafét na lol way machallah bg2

  • Ousmane
    Ousmane

    Macha Allah. Nguir nagouleene permis de lutte bou Lac2. Safoul goor waroul djiguene

  • uh hu ndiaye
    uh hu ndiaye

    Thiey balla mo bakh

  • Baamba Khadim Thiam
    Baamba Khadim Thiam

    Kou guenne xol Balla Gaye 2 si mbeur yi l guissoul

    • Bae Girl
      Bae Girl

      Dafa baakh ba moudji dof Sakho elimane, motakh bou niaké lagn key gueuneu beugeu. C’est le meilleur ❤️

    • Khady Ndiaye Yaye Fall
      Khady Ndiaye Yaye Fall

      Amoul

    • Seynabou Mbaye
      Seynabou Mbaye

      Amoul

    • Diha Sallah
      Diha Sallah

      No dafa amoul sax

    • Ndeya Karisma
      Ndeya Karisma

      Lou lerr gua waxx 💚

  • Sidaty Daf
    Sidaty Daf

    Très beaux geste de fair play

    • Laurence Mendy
      Laurence Mendy

      J’adore 😍😍😍

    • Gueye Aziz
      Gueye Aziz

      @Big Mac bayilenne seytané nioy fayégo sën millions di lègue. Bayilenne di woutale beure yi nonne nio book sën association watchape. Netlenne fi rek yéne di nonon niome niogui legui deh😅😅

    • Sidaty Daf
      Sidaty Daf

      @Ange Paulin Dieme j'ai le droit de faire une erreur de frappe aussi non 😁😁

    • Ange Paulin Dieme
      Ange Paulin Dieme

      On dit pas faut play.C'est fair play

    • Big Mac
      Big Mac

      Ouai heureusement que tu a dit "faut play" parceque les deux là ne s'aiment pas du tout en réalité.

  • mamadou demba
    mamadou demba

    ❤❤❤❤😂🦁

  • Loufa kharangne Lo
    Loufa kharangne Lo

    Nice na

  • Yaya Diallo
    Yaya Diallo

    Machala💓👻💓👻👻🤘

  • Yaya Diallo
    Yaya Diallo

    1 vue

Il prossimo