“Infidèles” : Mame Matar Guèye dément EvenProd et confirme l’exclusion de Mariama ! (Senego Tv)
110,202
Reddit
Ne manquez aucune information du Sénégal ou que vous soyez !
Téléchargez nos applis ou visitez senego.com: bv3ey.app.goo.gl/sn

Commenti
  • Lala Jarra
    Lala Jarra

    Merci pere Mactarr

  • Aliou mbodji
    Aliou mbodji

    Dageena wara def ay production di def ay seri you refet baxx nékhe

  • ibrahim kebe
    ibrahim kebe

    Bravo aicha thiam

  • Modou Diakhate
    Modou Diakhate

    Machallah Maryama

  • Del Mas
    Del Mas

    Man limay halat moy gni bouniou démé niane nioleni remplacer ndah sénégal mogui dieum si lou graw

  • ABOU DIALLO
    ABOU DIALLO

    Merci père

  • Petit Gueye
    Petit Gueye

    No pa bi kou soff la

  • Mamadou Gueye
    Mamadou Gueye

    Merci diamra

  • Aicha Diouf
    Aicha Diouf

    Wa delennn surveillé sen dom yi en même temps car même boudoul infidèles ils suivent des choses plus pire dans leur téléphone ... khalé yi legui ken meunoulen surveiller mettez l'accent sur ça mo gueuneu... en plus les séries d'avant étaient pire même infidèle doumako setane car je suis pas trop fan de série mais khalé yi ngen Di bayi niouy setane novelas les émissions de télé réalité mettez l'accent sur ça

  • Cham Abzer
    Cham Abzer

    Ndam rk🇸🇳👈

  • Anna Diallo
    Anna Diallo

    Merci jamra

  • Mame gor Ndong
    Mame gor Ndong

    Nous sommes tous derrière vous

  • OumOu Ba
    OumOu Ba

    Du coup spoiler nguéne maa koone Mariama dafaay dé ci série bii okk…

  • Dieng Ahmet
    Dieng Ahmet

    Mariama lou bakh la deff yalla dinako fay

  • Femme Forte
    Femme Forte

    Jamra and sam djikoyii Bilay walay talay le peuple sénégalais 🇸🇳 amou sen fay yalnalen bour yallah fay

  • Senegalaise
    Senegalaise

    Bravo Aïcha Thiam

  • Ndieme Thiam
    Ndieme Thiam

    Mariama elle est adorable dafma meussa nékh té khamouma wone sama domou baye gua machalla nila dé amena lagua khameni beuss boko joué Say ndiabote guaye toye euleuk ❤️

  • Awa
    Awa

    Mo geumouma lolou mariama jouer na fi li eup lolou iri na ridial soumékou ba set di wakh ay wakh you bone nane koula oubil nga daur di nane di mandi di saga yayam

  • Ndeye Diakhate
    Ndeye Diakhate

    Man daal vraiment diakhlenaa si Sénégal. Mais Mariama moom daa wara noppi. N'est ce pas hier mofidone jouer ai prostituée di soumekou tay mou takhaw fii beugeu jouer les victimes. Je pense que meunoul digérer le fait que niou dakhko rek Mouy vengeou

    • Moussou Saliou
      Moussou Saliou

      C vrai mais elle s'est peut-être repenti c bien

  • Zíízàà Jallow
    Zíízàà Jallow

    Evenprod suis leur 1er fan depuis le 1er épisode de la saison 1 de Idoles mais certaines séquences de Infidèles doivent être revues. Ñu gi perte crédibilité bi ñu amoon avant parce que su dul dara ñoom ñoo produire mœurs, idoles, watt gaal ak yeggoo qui sont des séries très instructives negn xool lu baax li ñu def aussi tout en dénonçant le mauvais

  • Alassne Mbodj
    Alassne Mbodj

    Katal sa ndeye doul

    • Femme Forte
      Femme Forte

      Yakk ga sa bop déé

    • DIP DOUNDOU GUISS IDOL
      DIP DOUNDOU GUISS IDOL

      Esque khamgani sa yaye ga wakh direct

  • Modou Fall
    Modou Fall

    Mercii jamra

  • Thierno Diop
    Thierno Diop

    Merci

    • yama Tamba
      yama Tamba

      Yalna la yalla takhouw

    • yama Tamba
      yama Tamba

      Merci mame

  • Beye Pape
    Beye Pape

    Boycotté rek

  • BRO DOLLAR
    BRO DOLLAR

    Vraiment deglou souniou mame bi dafma nekh Machallah ndakh lép dakoy tég si yarr ak teguin manam Xam xam niongui sen Guinaw yalla na Yalla barkel si barké baye niass

  • Khalil’s Kanpoung
    Khalil’s Kanpoung

    Merci Aissa alias Mariama

  • Ndiaye Massamba
    Ndiaye Massamba

    Machalla maryama

  • Doudou Dia
    Doudou Dia

    Aye domaram rékk nio meune joué série you bone yi akk thiaga you pertes.

  • Warrior's Event 🌈
    Warrior's Event 🌈

    😂🤣Mactar Gueye tu n'a qu'à engager mariama dans ta série et nous foutre la paix. Que ceux qui n'aiment pas la série infidèle aille regarder vos séries arabisan. Thiow li fin. La série est interdite aux moins de 16 ans et c'est bien marqué, personne ne vous force à regarder. Vous faites chier à la fin

    • Femme Forte
      Femme Forte

      Seul les sans valeur riposte et les nymphomans

    • Ndiaye Abdou
      Ndiaye Abdou

      Avec ton drapeau lgbt Tg

  • Bébé Nabou Si xool
    Bébé Nabou Si xool

    Merci beaucoup

  • modou goumbala
    modou goumbala

    merci mariama thiam niit daye am valeur

  • Souleye Ka
    Souleye Ka

    Merci per

  • Babacar Drame
    Babacar Drame

    Merci merci 😍😍😍😍😍 pér

  • Babacar Drame
    Babacar Drame

    😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍❤❤❤❤❤❤

  • Abdel Nassir
    Abdel Nassir

    S'il vous plait, si quelqu'un voit mon commentaire, je ne comprend pas wolof, je voudrais bien qu'on me fasse la traduction de ce qu'il dit. Merci beaucoup

    • Femme Forte
      Femme Forte

      @Abdel Nassir on n’est pas de la brigade nous

    • Abdel Nassir
      Abdel Nassir

      @Fazii s merci beaucoup mais j'ai cru comprendre que c'était faux cette rumeur.

    • Fazii s
      Fazii s

      Mariama a quitté la série parceque la maison de production voulais lui faire jouer une scène pornographique

  • DOUDOU BASSENE
    DOUDOU BASSENE

    Communiquez les réseaux sociaux de mariama... q'on la félicite massivement....! elle mérite les honneurs !!!!

  • DOUDOU BASSENE
    DOUDOU BASSENE

    Communiquez les réseaux sociaux de mariama... q'on la félicite massivement....! elle mérite les honneurs !!!!

  • DOUDOU BASSENE
    DOUDOU BASSENE

    Communiquez les réseaux sociaux de mariama... q'on la félicite massivement....! elle mérite les honneurs !!!!

  • DOUDOU BASSENE
    DOUDOU BASSENE

    Communiquez les réseaux sociaux de mariama... q'on la félicite massivement....! elle mérite les honneurs !!!!

  • Sonhaybou Niang
    Sonhaybou Niang

    Macha allah baytoul atfal😍😍😍❤️❤️❤️💪❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • Massamba Ndiaye
    Massamba Ndiaye

    Merci beaucoup père

  • lovelymina kouma
    lovelymina kouma

    Mashallah mashallah good job..

  • Gnima Danfa
    Gnima Danfa

    Infidèle da nio ko wara sansuré ndakh sen série bi da yétéwoul

  • Izo Gueye
    Izo Gueye

    Ame sa potou day di lidjanti pannou Diambour moyy liii

  • Fatou Seck
    Fatou Seck

    Merci beaucoup 👍🙏🙏

  • Mamadi Jallow
    Mamadi Jallow

    Bindlèn..✍ mama aïcha thi hitoire djiguene you bakh yi. yallah defna djiguen you bakh yi yeupp sama yaye lagne🧕🏿🥰👏🏿👏🏿

  • Ibrahim Kasse
    Ibrahim Kasse

    Ya door la réck Sénégal légi buze y diarna louné ici en Europe ya des série comme ça nous ont triche les Européens arrêtés de copies des gens modi ya beaucoup rôle â joué pour notre société ya pleine de choses a joué pas seulement sexe

  • Al.Mushtari TV
    Al.Mushtari TV

    Mame Matar gueye suit très bien la série peut être il est abonné à evenprod.

    • Femme Forte
      Femme Forte

      Sen genre yii bakholen tee beugolen kou bakh amo ndiarign pour Sénégal ter beugo kou amal ndiarign Sénégal

    • Sylla Fall
      Sylla Fall

      😂😂😂😂

  • Adama Dieng
    Adama Dieng

    Mercii

  • Mbene Lo
    Mbene Lo

    Merci beaucoup mame makhtar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • Baby Diop Laye
    Baby Diop Laye

    Gardel sa série tu nous fatigue 😴

    • Baby Diop Laye
      Baby Diop Laye

      Je réitère gardel sa série point

    • Femme Forte
      Femme Forte

      Sa genre yii lou bonn rekk laniou beug

  • AMIDOU BIAYE
    AMIDOU BIAYE

    Merci Mame Mactar

  • TontOuz
    TontOuz

    Je me demande pourquoi le grand projet du grand réalisateur Daouda Guissé n'est pas encore financé. Il avait promis des séries typiquement sénégalaises, lui qui produisait les pièces de théâtre de la troupe de Saint-Louis dans les années 80 (?). Celle des Marie-Madeleine Diallo, feu Golbert, feue Mame Séye... Bref, ces grands acteurs qui promouvaient la culture sénégalaise dans tout ce qu'elle a de valeureux, humainement et socialement. Ces éducateurs qui ont "ramené" pas mal de sénégalais parmi ceux qui ont eu la chance de les voir à l'œuvre. Tout celà sous la direction du fameux "Monsieur Barrage" comme l'appelait Golbert. J'en appelle à ceux qui sont soucieux de la préservation de ce qui reste de notre sénégalité et qui nous différencie positivement des autres. Tendons la perche à Daouda Guissé et aux personnes comme lui pour sauver les futures générations de sénégalais. Merci à tous ceux qui œuvrent à la sauvegarde des valeurs humaines et humanisantes.

  • alioune diouf
    alioune diouf

    Wawaw

  • alioune diouf
    alioune diouf

    Wawaw

  • Fatmther Cham
    Fatmther Cham

    😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡

  • Moustapha Mbaye
    Moustapha Mbaye

    Diadieuf mame mactar Gueye

  • COEUR 2 LION
    COEUR 2 LION

    Vréma merci bc pére tu es tjr la pour le peuple sénégalais Léna môme dafa del Bone rék harito ak mome

  • Mamur Gey
    Mamur Gey

    Dieuredieuf MAME MATAR GUEYE YALLA NALA YALLA DÉFALE JAMM

  • Diop Dauda
    Diop Dauda

    Mercii mame makhtar gueye

  • Khadim Sylla
    Khadim Sylla

    Merci mariama جزاكم الله خيرا Mame makhtar Gueye

  • Zamane Rakhil
    Zamane Rakhil

    Yalna yallah fayla mame mackhtar

  • Sankoun Kanoute
    Sankoun Kanoute

    Je félicite Mariama pour votre courage et votre dignité car n'oublie jamais que tu es une femme et tu es appelé à te marier un jour et avoir des enfants donc il faut y veiller

  • thiatt O B B
    thiatt O B B

    Lii ma gis de jar na waa jamra xeex ci jollasu (Telephon) yi ñuy jox xale yi Ndax wido moom ku fayul du fa seetaan Bariwaana kuko gis koo xam ne bu doon (Télévision) rekk du ko gis

  • Ousmane Sy
    Ousmane Sy

    Dafa lerr nagn

  • chinou
    chinou

    Masha Allah. Qu'Allah vs préservé dans votre mission et facilite l'entente de vos messages par le peuple

  • chinou
    chinou

    Masha Allah. Qu'Allah vs préservé dans votre mission et facilite l'entente de vos messages par le peuple

  • Talibé Cheikh ba faww
    Talibé Cheikh ba faww

    Mame matar Gueye, Oustaz MAKHTAR SARR, Dame mbodje, Abdou Karim Gueye, Ababacar mboup, Xalaat TV, ,,,,,,,le Sénégal a besoin de vous

  • Souhaibou Gassama
    Souhaibou Gassama

  • Senkhibaar Sn
    Senkhibaar Sn

    Mame makhtar Gueye yallah na sa jam yague mala beugue

  • b.m.s artis tableau de sable
    b.m.s artis tableau de sable

    Merci beaucoup Mariama

  • Vénus Ndoye
    Vénus Ndoye

    Maîtresse d'un homme marié est dans cette voie, ds leur dernière épisode une femme mariée est venue trouver un homme ds sa chambre pour coucher avec lui pour le plaisir. Donc even prod ne doit pas être le seul incriminé.

    • Mama Diaby
      Mama Diaby

      @Sankoun Kanoutemariama a fait quoi s’il vous plaît ?

    • Sankoun Kanoute
      Sankoun Kanoute

      Ce n'est pas la même chose je crois que dans cette séquence on ne voit pas les parties intimes et on ne voit pas l'acte aussi.

  • Soukeyna Gaye
    Soukeyna Gaye

    Merci père

  • Abdou Seck
    Abdou Seck

    Merci Père et bonne continuation

  • Modou Mbaye
    Modou Mbaye

    Félicitations à Aïcha Thiam de son courage

  • baytoul atfal
    baytoul atfal

    Baytoul atfal la maison des enfants

  • Ibou Ndiaye
    Ibou Ndiaye

    Sénégalais nafékh là filaniou nékone di wakh ay mois en arrière bobou wa jamra takhaw di wakh si serie infidèle bii silou bonne louniouy déf sénégalais yii takhaw dinane naniou bayii niou sétane sounouy film ak wa sén tv yeup moy équipe teuss bii rek rapalé vous tay yène nieup di khass serie bii dii encouragé jamra.té pourtant jamra si loubakh la mess di dôkh serie yii dou dara thiakhane rek ak adouna bou diékh bii naniou bania raggal yalla rek ak diko diamou délène foo rék temps bii dafa gateu déh sama gayii té bamél lou mata bayi khél là

    • mbenda bessane
      mbenda bessane

      Djiadieuf waye machahla Mane dama warou

    • COEUR 2 LION
      COEUR 2 LION

      Machala wahga Lép mé deg rék mo weur dah moy moude

  • Peuhpeuh
    Peuhpeuh

    Père nak y’a ngi setane série bi dee 😅😅

    • MamyTouffy FALL
      MamyTouffy FALL

      Mais une personne qui doit véhiculer des messages pour la société doit être au parfum de tout ce qui se passe au tour de lui, d'où regarder ces séries et autres

  • Modou Dia
    Modou Dia

    Sénégal la beury problème dh

  • Ibou Ndiaye
    Ibou Ndiaye

    Mame mactar Gueye chaque jour nguène diko khass té pourtant lou bakh rek lay ndokh

    • Baye saliou Sylla
      Baye saliou Sylla

      Walahi

  • Muslim Joof
    Muslim Joof

    Thank you so much papa keep it on

  • Diallo Bassirou
    Diallo Bassirou

    Bilahi ly dafffa warra arreter

  • A.D free
    A.D free

    Merci jamra merci et Aicha thiam sans vous les series Senegalaise seront pire que les films Nigérianne

  • alassane dieng
    alassane dieng

    Merci mame matar nonou rek la

  • Jamal Lolo
    Jamal Lolo

    📿📿📿📿🙏🙏🙏🙏🙏🙏🏼❤️❤️❤️❤️❤️

  • Zelvo Galsen
    Zelvo Galsen

    Aïcha yalnala yalla samu deifalal la sa adduna ak alxira 🙏🏿❤️

  • Abdou Diop
    Abdou Diop

    Macha Allah amna solo cheikh makhtarr

  • SENEGAL TV
    SENEGAL TV

    Tu devais pas amener ta fille aux États-Unis, là où les télés diffusent tout.

    • Maimouna Dia
      Maimouna Dia

      @SENEGAL TV non

    • SENEGAL TV
      SENEGAL TV

      @HABIBALLAH DIA elle n'est pas aux États-Unis alors ?

    • HABIBALLAH DIA
      HABIBALLAH DIA

      Sénégal tv verifie vos infos avant de les sortir comme ça

    • karim Camara
      karim Camara

      Sa fille est au Sénégal il voulait les piéger

  • KING BABA
    KING BABA

    Merci Mame Mactar et jamra et merci aussi à Aicha Thiam (Mariama)

  • Omar Ndiaye
    Omar Ndiaye

    Merci père vous avez bien défendu l'image d'Aïcha thiam

  • Fatou Sakho
    Fatou Sakho

    Kéne indi aye série yo khamni daye wané valeurs you bax

    • Cheikh Seck
      Cheikh Seck

      Baytoul atfal

  • Fatou Sakho
    Fatou Sakho

    Bilahi yague nago khalate

  • mbacke Diagne
    mbacke Diagne

    Merci maryama delene jadieufale bouniou defe lou rafet

    • Pape Sow
      Pape Sow

      Merci mame matar merci aisa thiam

  • ABDOUSALAM JAMMEH abdou888
    ABDOUSALAM JAMMEH abdou888

    No Aïcha familles bou bakh la bokk depuis dieuppeul Aziz Michou serigue fallou puissance je suis très contente pour la famille

  • Cheikh KASSE
    Cheikh KASSE

    Jamra le peuple est fier de vous et vous voue un respect inconditionnel. La vie est simple soit on est du bon côté soit on est du mauvais côté. Bien joué Mariama d'avoir choisi le bon camp. Le divin ne vous laissera pas tomber. Force et courage à vous. Quoi qu'il en soit Jamra et Mariama sont des références qui font briller cette bougie d'espoir qui ne s'éteindra jamais Insha Allah 🙏

    • Mbacke Ndiaye mou s Babakur sy
      Mbacke Ndiaye mou s Babakur sy

      Mashallah mariama doko rethou loubakh rek ngay Inshallah

    • baye sidy sylla
      baye sidy sylla

      A oui

    • Abdou Samb
      Abdou Samb

      A

  • mado diagne
    mado diagne

    Evenprod dagno eupeulll trop. Je sais pas pourkoi vouloir impressioner avec ses genre de scenes trop oser

  • SERIGNE SALIOU DIAKHATE KHASSIDA
    SERIGNE SALIOU DIAKHATE KHASSIDA

    Jerejeuf gueye

  • Max La lionne
    Max La lionne

    Dém lenn diamou dji yalla bayi serie yii bobou ba legui serie niogui wané lou bone te menossi darra stp wakhal si problème mosquée Yi amoul morg courant dokh

    • Femme Forte
      Femme Forte

      Thiaga yii rekk niosii guis sen bopou lou bon rekkk

  • Babacar Mbaye
    Babacar Mbaye

    Merci pér contnaniou thi yaw Sénégal deukou mbakh leu

  • Recherche TV
    Recherche TV

    Maacha_ALLAH

Il prossimo