DOU MAN - Episode 25 - VOSTFR
35:07
1,256,394
Reddit
[Abonnement Gratuit ici]☆~~👉bit.ly/Abonnement_Gratuit_Pikini
[FACEBOOK]☆~~👉bit.ly/Facebook-Pikini
[Visitez notre Blog]☆~~👉bit.ly/Blog-Pikini
[TWITTER]☆~~👉bit.ly/Twitter-Pikini

Commenti
  • Fatou Mbaay
    Fatou Mbaay

    J aime vraiment

  • Diama Faye
    Diama Faye

    Diareu dieuf serigne Touba

  • Ibrahima Diouf
    Ibrahima Diouf

    C qui

  • Amiratresy Alhady almaliky
    Amiratresy Alhady almaliky

    Wa oundou mom kou mom khar bi mou bayyi boum bi😂😂

  • Maguette Gueye
    Maguette Gueye

    Ounde defmay ray koi 😂

  • Daba Sakho
    Daba Sakho

    Yalnako yalla yereum

  • Modou Sylla
    Modou Sylla

    Kou beugue néné beuseul j'aime

  • Elimane Sylla
    Elimane Sylla

    Aïda est mère rèssau aprè le chef de polisie doumouy dèf

  • Amy Gaye
    Amy Gaye

    Enfin Touti a acceptè d èpousè Almamy

  • Anthia Ndiaye
    Anthia Ndiaye

    Ah mada faah na ko

  • Mame bousso Dia
    Mame bousso Dia

    Wooy 😂😂😂😂

  • Nabou Fall
    Nabou Fall

    Merci de vos commentaires

  • Binette Niang
    Binette Niang

    Oundou raynama barki serigne ngathié fall 😀dagnema large tay djoyouma sax ndax série bi te kouma nop moma bayi j'ai besoin des mougneuls waay😁

  • tAnTy la rOsE
    tAnTy la rOsE

    Oundou ray nama way neina aida patra minoumako danne na ctane ay émission wam ki mo rew🤣🤣🤣

  • Ndeye Fall
    Ndeye Fall

    Bonjour j'aime bien votre serie et j'aimerais en faire partir

  • Lamzo Diouf
    Lamzo Diouf

    Li Dal moy Alcati Dou bayi dorr Aïda Diagne même k sax danukoy manote sax Mouy door3

  • Baye sall Ndiaye
    Baye sall Ndiaye

    Ciao ciao 👋 Nice Nice

  • Coumba GNINGUE
    Coumba GNINGUE

    Billl dhe setoul

  • Sokhna maye Gaye
    Sokhna maye Gaye

    Waw iska tamit Aïda diegn nekole jumelle fi wora tol de dom ak yeye ak diabar yép di ay jumelle 🤷

  • Soda Diop
    Soda Diop

    Dimbali lénn gnou way ak sen commentaire yi "ay kou beugu sa yaye dèfal j'aime "you kénn xamoul .sen yi dem lénn fénn.dognon nilénn guénn commenté si serie bi

  • Sokhna may Niang
    Sokhna may Niang

    inspecteur justice amoull dôme amoull goro 🤘🤘

  • Ibra Diop
    Ibra Diop

    🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏

  • Elisabeth Furtado
    Elisabeth Furtado

    Aïda Diagne hana vacote wam

  • Jumeaux Afia
    Jumeaux Afia

    Lii nekh na wayy

  • Ndack DIOP
    Ndack DIOP

    Je pense que c'est l'ami de néné qui est mère réseau parce que elle et Bill ont qu'elles choses à cacher

  • Siga Samb
    Siga Samb

    Allé bil fipouna way

  • NABIENNE Leye
    NABIENNE Leye

    Je pense que bil moy mère réseau

  • hawa ba
    hawa ba

    J’aime bien cette série ❤️

  • Mami Lo
    Mami Lo

    Non oundou rey nama 😂🤣🤣

  • rama diop
    rama diop

    Mention spéciale à Mada lii guaa jouer amoul féne félicitations à tous les acteurs aussi 😻😻😻

  • Maty_____ Sarr02
    Maty_____ Sarr02

    Aïda réw na dh ahhh li loumou doon ms bravo👏 bil moom tay dafa am foulla nk continue nonou rk

  • Reum Sa Guiss
    Reum Sa Guiss

    Kebab et Almamy je vois que c'est la même personne

  • Ndeye Seyni Diop
    Ndeye Seyni Diop

    Bill d moy mére réseau.thiey Yalla mougni sakk bah lii diamla

  • Fatim Ndiaye
    Fatim Ndiaye

    Aida neena ma nekk sama keur di séy 😂😂😂😂

  • Mer daba Ndiaye
    Mer daba Ndiaye

    Machalla

  • Khady Kane
    Khady Kane

    Inspecteur sa chemise bi mom beugueu ngakoo deii

  • Bassirou fall
    Bassirou fall

    Bil néna mako yilif 😂😂😂 Yaw chaque jour elle te torturait tu ose dire qu'elle obéisse à tes ordres 😂😂😂 Mais policier bi amoul noumou beauwéwoul 😂

  • Ramatoulaye Dieye Diop
    Ramatoulaye Dieye Diop

    Iow oundou ya con néné dinala béte ak aida keba wola guay wouyou si 😂😂😂 Mani lima wakhone rek Dou Aida Bill la

  • Amsa Seck
    Amsa Seck

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂Oundu raynama

  • Mariam Wone
    Mariam Wone

    Keba la yérem bilahi yaye djou bon yallah naniou mousal🤲🤲❤️ machalla nehna trop sah madior ak Dior n'a niew kou fakir💃👉👈

  • Mariem Zahra
    Mariem Zahra

    J'adore vraiment cette série

  • Mameasta Bousso
    Mameasta Bousso

    Cv

  • Omar Diop
    Omar Diop

    nene man damala fa bilay

    • khalil
      khalil

      Ay seekh daniouy nirolé

  • Arame thioumbé Kane
    Arame thioumbé Kane

    Bil moye pére resau Jaime mouy gawe😀😀😀

  • Astou Thiam Sene
    Astou Thiam Sene

    Wa li nènè sole la touti sole

  • Deguene Mbaye
    Deguene Mbaye

    Non Dou man lenene la nekh na trop ki est d'accord avec moi

  • soda sow
    soda sow

    Bilay série dafa nekh Aïda joue bien son rôle

  • Khadim Samb
    Khadim Samb

    Chéri bi nekhna wayé sene son bi dafa soufé

  • Mamoudou Dembélé
    Mamoudou Dembélé

    Certains sénégalais aiment trop de dire beuseul j'aime ana les j'aime la c à manger

  • Diarra Mame
    Diarra Mame

    Almamy ak touti dokhanou tapettte 😅😂😂😂 doma tontou iow lay diklou

  • fatou diop ba
    fatou diop ba

    Oundou 😂😂😂😂

  • Seynabou Dia
    Seynabou Dia

    Ana gni beug Serigne Babacar sy❤️

  • Amina Ndiaye
    Amina Ndiaye

    Bète adji sarr mako done masse aye yalllahh mignou sakk 😂😂😂

  • Astou Diop
    Astou Diop

    Je ne peux croire que aida moy mère réseau parceque dou man laniou wax té Bill sax dafni won amna Aÿ preuve ni aida moy mère réseau prkw pas mou guéné preuve yi bill môme wolou wumako dara c'est un peu louche peut-être osi dou môme té osi bounékul aida pour man sans filme bi dina khawa déss

  • Oumy Tamba
    Oumy Tamba

    Machallah djiguene de am clifa almami et toute🥰🥰🥰

  • thiatt O B B
    thiatt O B B

    Nene ak tuuti mem tubay mem tiset ku gis loolu bësël j'aime

    • khalil
      khalil

      Ay sekh daniouy nirolé des fois

  • thiatt O B B
    thiatt O B B

    Yàlla na nu Yàlla may koor ug jàmm ak salaam

  • Pape Niang
    Pape Niang

    Wa pikini nio beug police ak hopital

    • khalil
      khalil

      Fou crim am key police amfa

    • machalla Faty
      machalla Faty

      jourtou pouliche

  • Amy Gueye
    Amy Gueye

    Mo goor noumouy néké mère réseau 🤣🤣🤣woy lii com guère

  • serigne ababacar sy Diouf doundal
    serigne ababacar sy Diouf doundal

    Ha commissaire lo buegu aïda diagne môy mére réseaux guani dét rék li ba diam la tamite khalass

  • Tabara Gueye
    Tabara Gueye

    Yénn gniy commentaires gnak ngén xorom délén cmtair thi série bi

  • Yacine Sall
    Yacine Sall

    a

  • Samba N'diaye
    Samba N'diaye

    A.

  • Gueye tv Sénégal
    Gueye tv Sénégal

    Saga yii eupe na dh

  • daso80 Sylla
    daso80 Sylla

    J'aime la complicité de ce couple néné et kéba

  • Awa Thialaw
    Awa Thialaw

    Été 😊🤐😄😄🤗😊🐀😊🤗😄

  • Mara ngom
    Mara ngom

    Kéba khamoone li oundou di déf aida diagne dinko ray

  • Mara ngom
    Mara ngom

    Oundou amga fiitt yayi diambour gani dou sama guéll

  • Saly thiatou yayam
    Saly thiatou yayam

    mdrrrr, wouy oundou raynama, néna aida patra mdrrrrrrr

  • Aminata Niass
    Aminata Niass

    Aïda Diagne vrai comédienne leu koi🤣🤣🤣

  • Maimouna Kasse
    Maimouna Kasse

    No aida diagnie moy bandi deugue d

  • Fatou Beye
    Fatou Beye

    C bien pr toi Aïda Ndiagne daga. Vuleguére nekhoma thimmmm

  • Cheikh Ibra Faye
    Cheikh Ibra Faye

    Vraiment touti toyna trop wayy hooo sama khol dayy séed soumala guissé

  • Baba Sarr
    Baba Sarr

    Bili da seuse

  • Diarra Diop
    Diarra Diop

    🤩🤩🤩🤩😂😂

  • Maxy Gueye
    Maxy Gueye

    Je pense que c est Bill qui est a l origine du réseau

  • Rahmatoulie Badjie
    Rahmatoulie Badjie

    🇬🇲❤️❤️❤️❤️

  • Tousa bve
    Tousa bve

    Maty elle est belle machalla je l'adore

  • Ibrahima Sow
    Ibrahima Sow

    Nar prison ngaye vue nonou

  • ndari ba
    ndari ba

    Ki sol li jaune li sa sexy bingay empose nit yi tamit akh

  • GALSEN YOUTUBE
    GALSEN YOUTUBE

    Kouy fans oundou beusseul j'aime

  • Kanka
    Kanka

    Aida ñiow nga fo min 😂

  • Fatou Gueye
    Fatou Gueye

    Wouy oundou ray nama😂aïda patra kay

  • Elhadji Tall
    Elhadji Tall

    Mère mada elle me paille bcp 💕💕

  • Coumba Mbengue
    Coumba Mbengue

    Bilay sheri bi dfa nekh❤🌟

  • Mya Mya
    Mya Mya

    Ci debut bi la waxone bill moy mere reseau eytia reik Dou aida deh bill leu je repete BILL MOY MERE RESEAU

    • Mbayang Ndiaye
      Mbayang Ndiaye

      Bill dh kone ligeyam bi amul ben dieurign utilisé wul xalisam bandi gui yeup danioukay nokh ah yemmer na

  • Mable Fall
    Mable Fall

    No dohanou ibadou mo neikh 😊❤️almami

  • Oumar Niass
    Oumar Niass

    Lii moye kouye naan di nobbotou biss bou mandée feegne

  • Anta Sy
    Anta Sy

    Nekh na trop mais wagnilén sen pub yii wayy

  • Adji Pouye
    Adji Pouye

    Est-ce que sakhe bil dou mere réseau 🚶‍♀️

  • Papi Macky dégage
    Papi Macky dégage

    L’enquête de cette police n’ai pas professionnel vous avez des numéros loyakh defolem enquête bi bamouler avant son arrestation mais fatena Sénégal 🇸🇳 lagne nek mdr 🤣

  • kourel khassida
    kourel khassida

    Gayi diapale lénn ma à bonne sama chêne ITmores guir yalla rek yalla ga goudou fane si barkebe serige touba lo begue yalla nalako yalla defal 🙏🙏🙏🙏🔔👈

  • freshy Toufash
    freshy Toufash

    Et si bill était mère réseau 😂😂😂

  • Mboup Mansini
    Mboup Mansini

    Man niarni ay cèkhe orisinal lano wala

  • Maimuna Touray
    Maimuna Touray

    A

  • Cheikh Niang
    Cheikh Niang

    00000+00000=00000 sène sèri bi kico mbide khamoul dara kholal shèkh yi mèm tishèt mèm patonlon double roll douni

  • Mohamed Benzékry
    Mohamed Benzékry

    Mada Jongama piir la mom lay weur nopnako 🙄

  • Mohamed Benzékry
    Mohamed Benzékry

    Oundou dafmay fathie 😂

  • Mohamed Benzékry
    Mohamed Benzékry

    Bill tay djeingouna😂😂😂😂

  • Khadija gueye sarr
    Khadija gueye sarr

    Aïda tél sa guémigne nooo commissaire bi rayna ma

Il prossimo