🛑DERNIER FACE TO FACE: EUMEU SENE VS LAC GUIERS 2 LA TENSION MONTE AVANT LE 04 AVRIL 2021
12:24
557,876
Reddit
🚩S’abonner à la chaîne de la 2stv cliquez sur ce lien👉 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
- itmores.info
- www.2stv.net
- Iptv disponible sur 2stv.sn
- instagram.com/2stv_senegal/
- facebook.com/2stvsenegal
- Snapchat: senegal2stv
- TikTok: @2stvsenegal
- twitter.com/2stvsenegal
- www.dailymotion.com/video/x7vidbb
#FACETOFACE #EUMEULAC2 #2STVLIVE #2STV #EUMEULAC2 #2STVSENEGAL #KEBETU #BANTAMBA #MODOUMBAYE

Commenti
  • seven 7
    seven 7

    machallllaaaaaaa

  • dcoog anml
    dcoog anml

    2stv💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪

  • nieooj gotoy
    nieooj gotoy

    Eumeu Sene Mo Meune Lac 2 beurei yi Bokul Saxx Ndamm Rekkk Incha Allah pour Eumeu Sene

  • eioshen boboi
    eioshen boboi

    Malick thiandoum je l'aime bien ❤️😘 da meunn limouy def machalla ❤️❤️

  • Buzz Divert _Tv
    Buzz Divert _Tv

    Eumeu la

    • dcoog anml
      dcoog anml

      🔥🔥

  • bcvbb hyui
    bcvbb hyui

    Malick thiandoum je l'aime bien ❤️😘 da meunn limouy def machalla ❤️❤️

    • nieooj gotoy
      nieooj gotoy

      Lac 2 nbam rek inchallah

  • Ndour Adji
    Ndour Adji

    Emeu Séné dagua yak sama aniff ndakh beuréwo lidousa thieur

    • eioshen boboi
      eioshen boboi

      Lac si bopam formame bi mo niaaw trop

  • Marie Ndaw
    Marie Ndaw

    Sama guayi niou wakh ko té déee lac nako promoteur boycotte

  • Ly torodo lyly
    Ly torodo lyly

    Merda

    • bcvbb hyui
      bcvbb hyui

      Thièy le professionnalisme de Malick thiandoum

  • Modou Diop
    Modou Diop

    Yop

  • Seedy Bayo
    Seedy Bayo

    Lac2 Adam rek insha Allah🤞🏿✌🏿🎉🥀💘💘🎊🎊💪🏿💪🏿😏👍🏿

  • beug fallou mbk
    beug fallou mbk

    Je suis lac bly

  • Fatou Gueye
    Fatou Gueye

    Lac mome waroule ame Kombat dou deme dou dike

  • Mamadou Moustapha Dia
    Mamadou Moustapha Dia

    Lac louma méti si yow do beuré doko bayi mou beuré

  • Saikou Djigo
    Saikou Djigo

    Lac rék 💪💪🦾

  • Diop Bireume
    Diop Bireume

    Euye lac 2 bowakhié rk nganii sou arbitre bii siflé rek nga dokh thi kawame té kouye weur yambar diapale

  • Mama Abou Dieye
    Mama Abou Dieye

    Lamba dal 2stv rek la wara Don nioko yoor

  • Amadou Ndiaye
    Amadou Ndiaye

    Lac fait doucement

  • Abib Doundou Guiss
    Abib Doundou Guiss

    Gaston seytané macky sall la

  • Mansour Diagne
    Mansour Diagne

    🔥🔥

  • Ousmane Goudiaby
    Ousmane Goudiaby

    Lac 2 nbam rek inchallah

  • Moussa ndiaye
    Moussa ndiaye

    Lac si bopam formame bi mo niaaw trop

  • diatara ft linpa
    diatara ft linpa

    Koool

  • Boubou Kaloga
    Boubou Kaloga

    Thièy le professionnalisme de Malick thiandoum

  • booba Fast food
    booba Fast food

    Lac yalla na danne

  • Assane Touré
    Assane Touré

    Lacc dakkoyy dann kenn doucii sama beurr nakk bilakh faraloumaci kenn mann le lion de Guédiawaye moyy sma beurr

  • Pape Djiré Mbow
    Pape Djiré Mbow

    Damay ragal mou defendre ba dann eumeu,lac thim mako diéppi

    • FALISTO BAMBISTE
      FALISTO BAMBISTE

      Guiss ngua affaire bi dei

  • Cxounabamba Diop
    Cxounabamba Diop

    Lac de guerre c'est le plus nul de l'histoire

  • Morinho Diagne
    Morinho Diagne

    Une question. Prkw. Couleur Maron Beige si plateau bi. Thiey macky

  • Khady Ndiaye Yaye Fall
    Khady Ndiaye Yaye Fall

    Lac 2 Yallah nala Yallah may ndam barkép Serigne Touba 🙏🙏

  • serigne Samb
    serigne Samb

    Balla gaye la namou signature reum

  • Sada Mbodji
    Sada Mbodji

    Bilay lamb bolewoul Eumeu ak Lac. Eumeu dou moromame ci dara..

  • Ablaye Ka
    Ablaye Ka

    🙏🙏🙏🙏

  • LEMZO KEBE
    LEMZO KEBE

    7 fois j esper k lac va montre qu il est l vrai Diatto

  • Bache Ndu
    Bache Ndu

    Lac wa pai Nio nara rousse rek

  • Serigne Gaye
    Serigne Gaye

    Lat yallnaleu yalla may ndam

  • Lamine Ndiaye
    Lamine Ndiaye

    Lac ragale

  • Mbaye gueye
    Mbaye gueye

    Eumeu séné 100%yalna ga am ndamm

  • Mourtalla Diagne
    Mourtalla Diagne

    Ndamm rékk inchallah Eumeu sene 🤲🤲

  • Fall Cheikh
    Fall Cheikh

    Bilay combat lac déy soff

  • Cheikhoulahi Ndiaye
    Cheikhoulahi Ndiaye

    Lac de guerre stp goorgorloul ba boul nul

  • Kum Zai
    Kum Zai

    Euma Yan nala Yallah burbi Mai ndam inshAllah ❤️❤️❤️❤️❤️

  • Hamidou Ba
    Hamidou Ba

    Do féki kéne lac dangaye doule amo fite liguéyo dara sa comba yeup nii la napaté rék té amo fite roi des arènes mome bouko khalate ndakh amo beuré bi amo khékh bi amo fite bi démale nga togue

  • Bamba Seye
    Bamba Seye

    Ñiaarr ngi mom meunou ma see faral kène ndakhe dama leuna soppou loll ndeysan kou si yalla may ndame na kenn ki nangou dogal

  • Malick Faye
    Malick Faye

    Eumeu néko à 100% dé

  • Mouhamed Fall
    Mouhamed Fall

    2stv dagno ayy machalah

  • SONKO JR
    SONKO JR

    Wa xana lac amoul fans lac warnga xolaatt sa bopou dh

  • Libasse MatiC
    Libasse MatiC

    Sur le Plan PhySique Lac Semble meilleur mais dara Eumeu dakoy dieulei Pikine iS bae

  • Thiobaré gui Tv
    Thiobaré gui Tv

    Lac chaque combat ma méréko ndakh day mélni Atletico de Madrid défense rk 😂😂

  • Ablaye Pané
    Ablaye Pané

    Jajeuf lac le défenseur de walo

  • Amath Ba Cissé
    Amath Ba Cissé

    Eumeu yalla nala yalla may dame 💪💪eumeu👑👑

  • DiegobuenosAires Dele
    DiegobuenosAires Dele

    Eumeu yallah naleu yallah mayy ndamm

  • Moussa DIOUF
    Moussa DIOUF

    Kou ci am hémorroïde boul dèm stade....ndakh Lac rek ak rassou. Ahhhhh!

  • Ablaye Thiam
    Ablaye Thiam

    Incha'allah yalla may laa ndamb eumeu

  • Moctar Ndiaye
    Moctar Ndiaye

    Lac meuso bagn combat 😂 xana bi nak digua beuré

  • Saliou Dia
    Saliou Dia

    Eumeu sene rékk

  • Sogui Diop
    Sogui Diop

    Lac dou beure ragal la arriere rek

  • Ousmane Zizou Wane
    Ousmane Zizou Wane

    2stv vous êtes les meilleurs bilahi

  • Sewa Sissoko
    Sewa Sissoko

    Where is the fans eumeu sene ♥️♥️♥️♥️♥️

  • Marouane habibou
    Marouane habibou

    Yallah nako nieup féké si diam #eumeu séne amssi ndam

  • Fallou gallass lo
    Fallou gallass lo

    Eumeu moi je suis supporter Modou Lô mais yalla nala yalla may ndam

  • Mamkorr Guéye
    Mamkorr Guéye

    Porono

  • Samba Ndiaye
    Samba Ndiaye

    Lac kaine waratouko teugeule combat .day dawe rek amoule fite

  • kourel khassida
    kourel khassida

    Nigir dieumi serige touba à bonne léne fi si kourel khassida 🙏🙏🙏🙏

  • lemer aidara
    lemer aidara

    Lac wa walo dougne dello ginnaw

  • lemer aidara
    lemer aidara

    Niom gni kén doussi khalé eumeu mag la nak da yag trppp khamna ay 9ans yoyo rk la magè lac 47ans ak38ans la =85ans la =13=4/4 mois =8 kon lac day dan mou nek 1_1

  • Assane Ndiaye
    Assane Ndiaye

    Face2Face bii da sedd trope

  • lemer aidara
    lemer aidara

    Emeu diekhalna c fini pr lui mé menna dann ndakh bet noirou wa gediaway la balla ak lac

  • Talla Diop
    Talla Diop

    Modou moye sama mbeur wayé eumeu lafaral💪💪💪💪💪💪💪💪

  • Fallou Mbaye
    Fallou Mbaye

    Lac le meilleur face to faceure de tous les temps

  • Boubacar liman Badiane
    Boubacar liman Badiane

    Eumeu rekkkk

  • Mame awa Sylla
    Mame awa Sylla

    Eumeu mo meuneu Mamie lac

  • Ousmane Mendy
    Ousmane Mendy

    Lambeu bo kham gnieup kham nagne ni day dieul temps yague diaroul debat

  • Dip daddy Diouf
    Dip daddy Diouf

    Sama lutteur bi eumeu sene yallanala yalla maye victoir

  • Dip daddy Diouf
    Dip daddy Diouf

    Sama lutteur bi eumeu sene yallanala yalla maye victoir

  • Gueye Cheikh
    Gueye Cheikh

    Lambe khewinawa bouléngnou sonnale

  • Adama Sarr
    Adama Sarr

    Lac néné dey diély loum sokhla🤣 noo ki dina ma rey...

  • DIEUREUDIEUF DIADIEUF
    DIEUREUDIEUF DIADIEUF

    GUEUEMENA NÉ LAC DE GUERRE DE DINA DIEUL ROI BI INCHALLA!!!

  • DIA Alpha
    DIA Alpha

    Lac je suis sure qu'il fera la distanciation social 🤣🤣🤣

  • Samby Ame
    Samby Ame

    Lac damay saga sa... danga muna dieul roi

  • Boubou Seck
    Boubou Seck

    Eumeu ndam inshallah

  • Modou bousso Leye
    Modou bousso Leye

    Ndame si eumeu sene

  • Bilal Ka
    Bilal Ka

    Lac de guerre wakh rkk la meun

  • Xalima Talif
    Xalima Talif

    Athia eumeu

  • Arame Thioube
    Arame Thioube

    Ndaysan eumeu dafa téyyy bilay yalna la yalla maye ndame

  • Momar N’Diaye
    Momar N’Diaye

    Athiaaa lac2 domou guediawaye victoire inchalaaaa

  • Papa Assane Gning
    Papa Assane Gning

    Allez lac ndame rek

  • 29-Gaye Elhadji Oumar
    29-Gaye Elhadji Oumar

    Lac mom lammine béé reuyyy

  • Bar Iso
    Bar Iso

    Eumeu séne ts les fans de Kharagne lo sont derrière toi

  • kana koulibaly
    kana koulibaly

    Tyshinger ndame rkkk

  • ALBOURAKH24
    ALBOURAKH24

    Télé day am thiassss 💞 je vous love toutes l'équipe de 2stv goudou fane ak weer ak nieup incha Allah

  • Moussa Fall
    Moussa Fall

    Modou lô✊❤️

  • ALBOURAKH24
    ALBOURAKH24

    2stv c le meilleur de tous les temps incha Allah

  • Mohamet El Bachir Toure
    Mohamet El Bachir Toure

    Lac moy ko khamni meunatoul def dara bama guemko😂😂Go Eumeu

  • Almamy Sakho
    Almamy Sakho

    Lac2 victoire rék Incha'Allah

  • Modou Modou
    Modou Modou

    wa lac 2 prkw kéne fara louko si Commentaires yi ? lac nak wax duegue néxouta faral

  • Modou Modou
    Modou Modou

    drapeau diogay sall doumako sétane

  • Fallou Ndoye
    Fallou Ndoye

    Eumeu ndam reck

  • Galsen Wood TV
    Galsen Wood TV

    KARADIO 2STV FORT EVER

  • Anta Niass
    Anta Niass

    wa combat bi direct la wala

Il prossimo