Baye Fall répond à Sa Nekh : "Naniou assumé, yeugone naniou sama fébar... Lima geune méti moy..."
443,261
Reddit
Ne manquez aucune information du Sénégal ou que vous soyez !
Téléchargez nos applis ou visitez senego.com: bv3ey.app.goo.gl/sn

Commenti
  • Sarr Cheikh
    Sarr Cheikh

    Yalla nako yalla fathie

  • AL MOUBACHIRAH TV
    AL MOUBACHIRAH TV

    ABOUNE ALMOUBACHRA TV18

  • Cathy Gueye
    Cathy Gueye

    S’en xarito doy neu war daal kou nek di wedjé seu morom huum lou gueuneu urgent daal moy nga fadjou t yalla naleu yalla mey tane 🙏🏾

  • El Hacen Balla Abdellahi
    El Hacen Balla Abdellahi

    Ta seule guérison est la suivante: بسم الله ثلاث مرات ثم ،يضع يده على المكان الذي يؤلمه ثم يقول سبع مرات اعوذ بالله وقدرته من شر ما اجد واحاذر ثم يمسح يده على المكان المذكور. بإذن الله وقدرته سيشفيك الله

  • Mouhamed Wade
    Mouhamed Wade

    Yaw Dagua niakk fayda Mane deh walahi sa diaro bigua takkk motax meunoma nekh si adouna fi nieup laniou warra diapaler diapaler bat Fall d’où force bien vrai que dioulitt diapaler moromou djioulitam Yalla moko wax mais faut pas forcer les gens sa nex mome waxouma ay waxam depuis mouy défendre pape mbaye gor djigene mais yaw amna ay cas you gueuna urgent si deukk bi demal si hôpitaux yi gua kholl digua sante yalla deh

  • asioe kiou
    asioe kiou

    maboutage pour t'arnaquer ; ils vont te donner toutes sortes de poudres, de safaras à verser sur les yeux jusqu'à ce tu deviens aveugle

  • Dieng Ndeye
    Dieng Ndeye

    Yal kawér

  • Aly coumba Fall
    Aly coumba Fall

    Dangay wayan vraiment

  • Ibrahima Niane
    Ibrahima Niane

    Et les autres senegalais qui sont malade

  • Ibrahima Niane
    Ibrahima Niane

    La troupe nest pas obligee de te soignee.ya combien de malade au senegal et puis tu avais un salaire .

  • Meba the name
    Meba the name

    Soyez plus professionnel et veillez à la véracité de vos questions!!!

  • Maimouna Tambedou
    Maimouna Tambedou

    Frenchement cette journaliste est nul baye fall fallait pas repond a ses questions bonne guerison a tw

  • Awa B. L
    Awa B. L

    Cette journaliste va étudier encore le jourlisme. Baye FALL fait attention à vos propos... Maintenant l'analyse c'est comme si c'était un règlement de compte c'est vraiment triste... Sanekh ses propos étaient juste ni débordante...

  • dcoog anml
    dcoog anml

    Toujours aussi comique yalla nala yalla takhawou bilahi ❤️❤️❤️🙏🏼

  • Mariama Dabo
    Mariama Dabo

    Yalla yalla diapale

  • Timber Ndiaye
    Timber Ndiaye

    Celle qui pose les quelques est très débutante, elle n’est pas professionnelle

  • Bijou Ly
    Bijou Ly

    Na rafet way adouna amoul solo. Koula defal bakhna koula defaloul nga ande ak sa ngor tè nopi! Il faut être reconnaissant dans la vie. Même soula nite mayè deureum santéko ko

  • Oumy Ndao
    Oumy Ndao

    Waa senego dakk lén journaliste bii daffay diakhassé rékk khamoul darra

    • dcoog anml
      dcoog anml

      Sanekh est une bonne personne baye fall peu être dafa son rek mais rerora rek aduna mo mel nonou nagnuy dimbali gni sonou

  • Daly Yade
    Daly Yade

    Tre tre bien dit K’alla veille sur vous ta bien dit et sanex il est tré tré mechant nite kou boone la bakhoullll il m’a dessus! Baye falll n’a rien dit de malll!!!!

  • Bineta Sambe
    Bineta Sambe

    Wa journaliste bi meunoul fennn rek yaw demal ngua degulou wat sanex

    • vbddfy euuyt
      vbddfy euuyt

      pas aussi la situation financière des gens .

  • Aïcha Kane
    Aïcha Kane

    La médiocrité de la "journaleuse" !!!!! Même pas une journaliste!!!!

  • Sy Mariama
    Sy Mariama

    Baye on taime bien mais ce problem tu aurais le regler en famille. Lii diadouwoul. Wakh dji barrina. On te souhaite une bonne sante. Comme tu nes pas aveugle essais le centre de bopp et stop. Dioulit dafay am sutura.

  • Ndeye Diop
    Ndeye Diop

    Journaliste yi aye seytané rk lagne kouleine topp do nk si diam instant bi sanekh limou wax motax gnou invitéwate baye tmt arrêter. Aye wax rk fadiouko

  • eioshen boboi
    eioshen boboi

    Toujours aussi comique yalla nala yalla takhawou bilahi ❤️❤️❤️🙏🏼

  • Aliou Sow sop nabi
    Aliou Sow sop nabi

    Mareme fay déh mom kou bakh la

    • viiont eooiy
      viiont eooiy

      arretons way

  • Aliou Sow sop nabi
    Aliou Sow sop nabi

    yalla nala yalla défal wér

  • dior Cisse
    dior Cisse

    N'déyessane yalnala yalla maye wére thy barké Mohamed psl amine yaraby

  • kingbimendy16
    kingbimendy16

    Bou nguene beugone diam dou nguene deme thi bay fall soga deme thi sanekh da nguene di diahassé nit gni

    • eioshen boboi
      eioshen boboi

      Je suis désolé les sénégalais aime se plaindre Lui c un acteur et est payé comme tout un chacun s'il a un problème c la faute à personne c la volonté divine

  • Cléopâtre marque
    Cléopâtre marque

    Sanekh est une bonne personne baye fall peu être dafa son rek mais rerora rek aduna mo mel nonou nagnuy dimbali gni sonou

  • Ndeye Ada Ndongo
    Ndeye Ada Ndongo

    Prompt rétablissement tonton et longue vie à vous et votre troupe théâtre le soleil levant il faut faire attention pour certains personnes

  • Kadia Diallo
    Kadia Diallo

    Qu Allah te facilite et bon rétablissement. Arretons ces polémiques, l aide n est pas une obligation. Yallah nala yallah diapale gua tané mais naniou bayi polémique. On connait pas aussi la situation financière des gens .

  • Assane Séne
    Assane Séne

    légui wakh dji doyna Sanékh diapalél Baaye Fall

  • Baby Baby
    Baby Baby

    Ces sites de merdes, journaliste bi diahassei rek vrai mram

  • damsodems sall
    damsodems sall

    mais sérieusement tes questions ne sont pas pertinentes et font fausse route de ce que sanéck a dit bordel ou tu as eu ton diplome

  • Aidara Aichetou
    Aidara Aichetou

    Yalla nala yalla maye wèrre thi barkè nabile moustapha sws

  • Aissatou Diallo
    Aissatou Diallo

    Bay tu as pollué le nôtre Sénégal En t'entendant parler, c'est comme si c SA NEKH qui est à l'origine de ta maladie. Fait attention...

  • Abdoulahi GUEYE
    Abdoulahi GUEYE

    vraiment li nekatoul wote dimbeul plutot wayane naxx gnimou lim gneup sounou gnawe lepp natt. li Cheikhou GUEYE waxx rekk likoy fadj dou khaliss coup de fil la donc arretons way

  • Farima Taylor
    Farima Taylor

    Mane dai li ma daigueu moye "goumbeu gui gni wakh" Sanekh ak wa Soleil levant yeugouniouko. Myopie bi yeuknangne ko... Donc rairoo amoule niaka wakhtane mo ame. Yalla laine bolai, boulaine ka yakh tchi aye wakh rek. Bon courage, Yalla na yalla sairale laipeu. Dioubo laine, dara dakhoule dioubo...wa salame

  • Thiane Khouma
    Thiane Khouma

    Wawe tamite ane sa sering bi mom

  • Fallou Niang
    Fallou Niang

    Sanéx wakhoul lolou dh

  • Khady Ndeye
    Khady Ndeye

    Je suis désolé les sénégalais aime se plaindre Lui c un acteur et est payé comme tout un chacun s'il a un problème c la faute à personne c la volonté divine

  • Khady Diop
    Khady Diop

    baye fall yalna la yalla safaral Boul khaddi

  • Fatou Ndiaye
    Fatou Ndiaye

    Mais baye fall rafetalal rek ndogal la c pas la peine indi ey polemik yo hamna amo foumouy eggue gnila wara dimbale di negnou ko def inchallah

  • annag cocl
    annag cocl

    Sanék na pas dit ça il as dit que il na su l aveugle de baye Fall

  • Adama Malick Dramé
    Adama Malick Dramé

    Baye soleil levant fathie là d'où obligation tu travail on te paye âme n'a yo khamni diarouko yalla bakhna Di nga wéer inchallah wagnil réseau sociaux yi

  • Adama Malick Dramé
    Adama Malick Dramé

    Baye yii ni dara diarouko boulén wéranté khole léne demb ,sanekh nit kou bakh là

  • Yamudow Njie
    Yamudow Njie

    Baye wòyankatt ngèu yaw. Jelaal cent francs yui. Baiyil thiaw Baye😁😄😄😄👌soliel d'Avant for life...

  • Ndeye Awa Diouf
    Ndeye Awa Diouf

    Mes yala na la yala may tane

    • Ndeye Awa Diouf
      Ndeye Awa Diouf

      Merci beaucoup bien dit

    • annag cocl
      annag cocl

      tonton Sanekh disait dans sa déclaration. Et là cette journaliste invente des propos que Sanekh n'a pas dit Prompt rétablissement à toi tonton Baye

  • Ndeye Awa Diouf
    Ndeye Awa Diouf

    Sou nékone sa kharite do ko wakhe li ses pas forcé mou fathe la mo médre way wakhe bakhoul

  • Emeelbi Bymo
    Emeelbi Bymo

    Saneekh dafa wakh ni yeugoul woon ni bayefall febaram bi tollou na fi. Désolé Madame la journaliste jotalli dafay mat amoul yok amoul wagni 🤭

  • Ndeye Awa Diouf
    Ndeye Awa Diouf

    Yaw baye lolou ga bagonne badola ga li waro ko wakhe mémé sou amone

  • Emeelbi Bymo
    Emeelbi Bymo

    Ay way ana soutoura 😳😳😳

  • Mame goor Gueye
    Mame goor Gueye

    Beunie dou ré diammm nena namou ma diou dia 😥😂😂

  • Djibril Diagne
    Djibril Diagne

    Baye fall yalla nala yalla veral mais une demande es tu pries baye fall ????

  • zuygj bnsv
    zuygj bnsv

    Bonne rétablissement baye

    • Abdou Gaye
      Abdou Gaye

      Cv

  • zille boy
    zille boy

    Yalla na téné

  • diack mimi
    diack mimi

    Guisga dee waroute wona toudou kenn nianall rek et basta diyakh derr sénégalais mom lepou par la force laa

  • Abdou Ndiaye
    Abdou Ndiaye

    Mais danga wara wanieu sa rastayi nak li rek man nala féebar

  • Ndeye saliou Ndiaye
    Ndeye saliou Ndiaye

    Journaliste bi mal forme

    • zuygj bnsv
      zuygj bnsv

      Bays fall diate mola diap yala nala yaladiapalé barkép sékhe ibre fall

  • Khadim
    Khadim

    LES PROPOS DE CETTE JOURNALISTE ( BON ANIMATRICE PLUTOT ) N'ENGAGE QUE ELLE , SANEKH N'A JAMAIS TENU DE TELS PROPOS ! JOURNALISTE BI MO CREER AYE WAKHAM POUR AME AYE REPONSE QU'ELLE VEUT ENTDRE DONC çA N'ENGAGE QUE LUI MAIS PAS SANEIKH !!!! SANEIKH LIMOU WAKH LEIR NA NAGNEU TEI YEUP SETANE NANIOU INTERVIEW BI ! SVP RECRUTER DE VRAI JOURNALISTE ISSU DE CESTI AULIEU DE RECRUTER CES ANIMATRICES QUI N'ONT AUCUNE FORMATION JOURNALISTIQUE !

  • Xam xam bou woor
    Xam xam bou woor

    Oh

  • Oumy Diatta
    Oumy Diatta

    Il y'a dès fois je me demande dans quelle école certains journalistes sortent? Cette femme qui pose les questions à Baye Fall on dirait qu'elle n'avait même pas écouté ce que tonton Sanekh disait dans sa déclaration. Et là cette journaliste invente des propos que Sanekh n'a pas dit Prompt rétablissement à toi tonton Baye

  • Ndeye Fary Niang
    Ndeye Fary Niang

    Non mais ce gars il est un peu bizarre faut faire attention dh

  • Khalil Fall
    Khalil Fall

    Daye chane

  • Khalil Fall
    Khalil Fall

    Daye chane

  • aliou diedhiou
    aliou diedhiou

    Svp arrêtez , et demandez une aide pour lui car nous sommes tous Sénégalais , au lieu de mettre de l'huile sur le 🔥

  • bakeloise
    bakeloise

    Lol

  • Fatou Diop
    Fatou Diop

    Mais première interview bi dafa wakhone né dou guiss ....tey néna dey guiss touti

  • maman dmg
    maman dmg

    Vraiment les journalistes sénégalais sont des vrai seytané makhala mal formation de nos jours j'ai piété de ses journalistes 😱😰😕😕

  • Mohamed lamina Diouf
    Mohamed lamina Diouf

    qu'Allah facilite et vous protège Baye fall aminne aminne 🤲🤲🥰❤️

  • Mbaye Abdou ahade
    Mbaye Abdou ahade

    Bol wo marieme fay Dina bakh

  • Gabriel Diesel
    Gabriel Diesel

    Yalna yallah safara si barki cheikh ibra

  • Ndeye Diop
    Ndeye Diop

    Bays fall diate mola diap yala nala yaladiapalé barkép sékhe ibre fall

  • Samba Kah Sambe
    Samba Kah Sambe

    Baye FALL est atteint de glaucome d’après sa description or il faut prendre des gouttes à vie pour retarder l’échéance. Il faut au’il soit soit mieux informé Le problème ne se règle pas une < bonne fois pour toute> NB: je suis attent de glaucome depuis plus de 10 ans Je suis souhaité bien du courage et de la patience

  • shani yan
    shani yan

    tégoula ko et puis dou force pour mou fadj la!

  • Barito AS
    Barito AS

    Journaliste bi vrai domou kharam la on doit te renvoyer impertinente

  • sophie gueye
    sophie gueye

    Si c est Glaucoma ya pas de cure. Il y a des oeil drop qui empeche la tension de montee mais moi meme j ai cette maladie mais encore pas de cure.

  • bcvbb hyui
    bcvbb hyui

    Clairement ! Journaliste yi sont de vraies " N A F é k h "

  • sali la sirène camara
    sali la sirène camara

    Baye franchement je comprends ta douleur wereul AK jiam inchallah 🙏 wayé na rafétt Mane sama yaye tamitt 3ans mou fébar menoul jiss tei nioune ay khalé lagniou tei famille wam ay millionnaire tél niossi Bari mais kén faléwouniou sama yaye démnaniou ba amouniou lounouko fadié ndakh jiékhal wayé tay yalla teguilnako febar bii légui niom rék nio rouss nioune batay niongui AK sounou dignité Kone fi yalla rék mofi nékk wasalam 🙏

    • shani yan
      shani yan

      founiou diare thi lou bakh. Arretez d'attiser le feu té nguéne oute diame .. Yalla naniou Yalla doli Soutoureu té may niou wër ak wërlé

  • Modou Ndiaye
    Modou Ndiaye

    Baye fall communique mal ba nopi saytané yi diko dougal

  • Khady FALL
    Khady FALL

    Bonne guérison Baye on est de tout Coeur avec toi Insha Allahou Dieu viendra et c lui Seul le Potentiel Guérisseur

  • Sagar Diouf
    Sagar Diouf

    Journaliste yi seytanê lagne deff

    • bcvbb hyui
      bcvbb hyui

      Journaliste est une menteuse, elle déformé les propos de Sanekh. Mais lui Baye Fall, il a écouté le discours de Sanekh donc il ne doit pas tomber la dedans.

  • beugg sama yaye
    beugg sama yaye

    Je me rappelle sanex mola nieuk wané TFM émission matinal bobou télé TFM mogui doguo tidji

  • beugg sama yaye
    beugg sama yaye

    Sant yalla insbi Corona bagui def ravage diabétique you Bari daague nagnou sén thieur

  • paconese
    paconese

    J'ai un ami enseignant depuis plus de 25 ans. Il a donc formé et instruit des milliers de sénégalais. Très malade et soigné à ses frais. Que voulez donc. Parce qu'on est connu, on mérite d'être soigné avant les autres 🤔

  • Loss J loss
    Loss J loss

    Bayi lén diakhassé aye seytané gaineu rek yén journaliste yi

  • Sambe Adia
    Sambe Adia

    Nagoul lila yalla tek boul khass kenn c ton destin tu ne serai pas le seul ni le dernier khollal gni nek si adouna meusogna guiss khamouniou adounabi nimou mell te pourtant il vit avec les gens c dure mais du courage

  • Mamadou DIENG
    Mamadou DIENG

    Prompte rétablissement. 🙏

  • Sokhna Diop
    Sokhna Diop

    ioe journaliste bou saytaneika yeina diakhasei nittt yii bayiill wakhi diambout yikaye diakhasei sou yabo niou dakhla DH

  • Diakhoumpa Bayefall
    Diakhoumpa Bayefall

    sama xalat bou gat nfimbeul dou par force te domou adama bou nek yawara lidieunti sa bopou bo khassé ba am 18 ans nekato si reponsabilite kene. fanane na si mbed ay were sama papa khamokou sama yaye khamoko wakhatoumala ak kharite . senegal mo wara am sisteme securite social social boy ligueye di fayekou 200milles chak moi etat bi dague leu 15milles bo febaré niou fathie la si lolou moy deugue

  • sakoura diagne
    sakoura diagne

    Baay Faal wàññil wakh ji. Nit du wakh ci ñi mu doon andal ci ay radio. Ku nekk amm Na lu muy dirikoo. Amal dal ta bayyi médias yi

  • diarria bousso
    diarria bousso

    Amna Journaliste yo khamni lou take si réw mi.gnio ko tale. Saneekh lou raféte la wakh si Baye , Baye aussi gueumnani nakar ak khol bou diékh ak seusse motakh mou nieuw si média di wakh mais gueunalouko ndakh goor sou néke goor nga té kou sanione lo ame ak lo amoul kéne doulako khamal . Bo deglo Saneekh khamni mok Baye amna founiou diare thi lou bakh. Arretez d'attiser le feu té nguéne oute diame .. Yalla naniou Yalla doli Soutoureu té may niou wër ak wërlé

  • Talla Ndiaye
    Talla Ndiaye

    Numero baye fall la sokhla

  • papa duk
    papa duk

    BAYE FALL YALLA GUE TANE AK DIAM MAIS EN TOUT CAS LES LINGES SALES SE LAVENT EN FAMILLE PEACE

  • Lyly Sasa
    Lyly Sasa

    Journaliste est une menteuse, elle déformé les propos de Sanekh. Mais lui Baye Fall, il a écouté le discours de Sanekh donc il ne doit pas tomber la dedans.

  • Serigne saliou Faye
    Serigne saliou Faye

    Walay Ndéaysan baye fall

  • Idrissa Diouf Sané
    Idrissa Diouf Sané

    Baye fall pr mane wah ngu sa sohleu baparè moytoul nét bii bn rétablissement frère

  • Astuce nouvelle technologie 📱
    Astuce nouvelle technologie 📱

    Ziaar nalen gar yi Mane deh dama taxawaal chaine bii teh ame na ay video si wolof gnoulay jangal nane lagnouy pirater wifi,naane lagniy xamei dagn lay espionné watshap,naane ngay def ba krn doula meun dougueul si brn groupe watshap th beugo ko chaine bangui nonou nak jap len si combat bii✌🏽❤️ak test psychotechnique corrigés pour l’ENA ak avoir netflix gratuit Mercii

  • Mamediarra Ndiaye
    Mamediarra Ndiaye

    baye fall yalla nala yalla diapali sanekh borome bakh la

  • GNOU_DEBAT-TV
    GNOU_DEBAT-TV

    Bayfall va voir avec les yeux inchallah

Il prossimo
bLu
2:01
24K